ELZO JAMDONG Jangal Ma Napp cover image

Paroles de Jangal Ma Napp

Paroles de Jangal Ma Napp Par ELZO JAMDONG


[VERSE 1]
Wathié naa Teeré AMAYATA am na
Diouraum niétti att
Té djangue bimay djang
Guissouma sakh njerignam
Loutah mou am niou wara sonneu
Am niouy khaar sen héritage
Aduna injustice leu dou kou nekkak méritam
Serigne bi néna kouka dégueul mou xétalileu
Miskine bou fessaloul sa pott mou djékalileu
Moussouma njaalo mais feug nagn
Meu teeméri (100) yarr
Bala may délou Daara ba faaw
Teemeer yi matt (500 Frs)

Hééy ! mais thiow dou djipp ma ngi maagueuh
(Maa ngiu maaggueu)
Xamna sama handicap (lane ?)
Moy douma domou diw
Niou def meu animal
Sokhlaatouma nioumay doumoyou pour meu kham
Ne effectivement Douma done kou riche
Ndakh dagnma sani alleu
Kène tégou mako koudoul samay
Waadiour yima diour
Kone fokma démé kholou mougn
Té bania radical
Baayi ma khaar beu souma gueuné
deugueur touti daal di faakh

Ma tchi meuneu guéné sama bopp
Jamm rek la yeené sama bopp
(Jamm rek la yeené sama bopp)
Xam naani ma tchi meuneu guéné sama bopp
(Ma tchi meuneu guéné sama bopp)
Xawma loutah life di gueuneu yeemé sama bord

[CHORUS]
Ani gnima daan boott dima nakh bama nélaw
Loutah gnima bokaloul daara rek
Laay talal lokho (Yeah yeah)
Amatouma Baay Guisseu touma sama Yaye Booy
(Guisseutouma Yaye Booy)
Bouma Yeureum dima diokh djeune
Jangal Ma Napp (whoah oh)
Jangal Ma Napp (yeah eh)
Jangal Ma Napp (So ko défoul rek def thioow)
Yaw mi am Gaal meuneu djoow
Jangal Ma Napp (whoah oh oh, yeah eh eh)
Goor gui Jangal Ma Napp (yeah)
Soxna Ci Jangal Ma Napp
(So défoul rek def thioow)
Sarakh ci fadjoul samay gaum, Jangal Ma Napp

[VERSE 2]
Fouki att ak Diouraum Bèn (16ans)
Kène beugoul melni mane
Té mane meunouma ndourok kène
Xam naani boudoul MBèDE kène douma kholé dome
Borome Auto bima moudjé
Goal-lou dafma khélou rombeu
Fourniture, sac (sac), yeeré aki dall
Bima djoudo beu légui dh dégg rek la tchi am
Mounouma Lire té awouma métier bouma djangue
Gni ngèni wowé WAGGA yi rek nioma nangou fatt
Bala niouy wouti JOB fokk niou am loumou THIOP
Seugueum dougn niou ko djokh
Dagnkay wouteul suniou bopp

Fekk niou Gueedju Koussoum wala Pont Colobane
Fi koufi né di trainé degn lay fuutti yobou djaay
Gnène gni di dougou FAC gnénène di dougou PLANE
Nioune niou nek di dougou keu guèneu beu dougou JAIL
Ngène berr niou tchi lepp melni nékouniou SUNU REEW
Kène niéméwouniou dound ndaxté ragalou niou DéH
Ma tchi meuneu guéné sama bopp
Jamm rek la yeené sama bopp
(Jamm rek la yeené sama bopp)
Xam naani ma tchi meuneu guéné sama bopp
(Ma tchi meuneu guéné sama bopp)
Xawma loutah life di gueuneu yeemé sama bord

[CHORUS]
Ani gnima daan boott dima nakh bama nélaw
Loutah gnima bokaloul daara rek
Laay talal lokho (Yeah yeah)
Amatouma Baay Guisseu touma sama Yaye Booy
(Guisseutouma Yaye Booy)
Bouma Yeureum dima diokh djeune
Jangal Ma Napp (whoah oh)
Jangal Ma Napp (yeah eh)

Jangal Ma Napp (So ko défoul rek def thioow)
Yaw mi am Gaal meuneu djoow
Jangal Ma Napp (whoah oh oh, yeah eh eh)
Goor gui Jangal Ma Napp (yeah)
Soxna Ci Jangal Ma Napp
(So défoul rek def thioow)
Sarakh ci fadjoul samay gaum, Jangal Ma Napp

Ecouter

A Propos de "Jangal Ma Napp"

Album : Jangal Ma Napp (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 18 , 2019

Plus de Lyrics de ELZO JAMDONG

ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl