Paroles de Ndanan
Paroles de Ndanan Par BAYE MASS
Yaw ndanane nga, ndanane nga, ndananenga
Ndanane nga, ndanane nga, ndanane nga
Ndanane nga, ndanane nga, ndanane nga
Ndanane nga, ndanane nga, ndanane nga
Ndanane dou thi atte yéé
Doko dégue thi lou souféé
Sou peunde bi wouréé
Koumou nekh né yaye danééé
Ndanane dou parparloo
Day ame respect
Diokh niepeu thieur bamou diekh
Doko khole baa me loko yabéé
Loumou dougou dem thi bamou diekh waww
Ndanane boleine dadié daflay guanie
Talibé rek nguako meuenu diaaye
Bimay neik gouné thi lama léré niwone
Sou guoné gui magué dina guanie
Bo néké tchi yone di thi diémee
Niouthi beuri douniou nangou lolou
Wayé thi seine bira bira biree khole
Dinanie moudié nangou lingua done
Dinagn khamni ndanane ngeu
Diambar ngeu
Xeex kaat ngeu
Goor pire ngeu
Référence ngeu
Ma sathie wakh leu
Ndanane ngeu
Diambar ngeu
Xeex kaat ngeu
Goor pire ngeu
Référence ngeu
Fi nguako teik rek leu
Sou yalla bindé ngani deet lolou bakhoul
Kilifeu wakhé ngua dieufé am ngua baarké
Niite yi niniou beurré lanie wouté less wakhoul
Fonkal sa ligueye nék sa yoone guestou bakhoul
Ni souniou barraam soutanté
Mayou yallah yi noone la wouté
Bou takhé ngua khole ko batakh ngua beugue ko yakheu
Mom doulathi top dileu danel
Ndakh ndanane leu
Diambar ngeu
Xeex kaat ngeu
Té moom Goor piire ngeu
Ni wooooooy ndanane
Ndanane sou déwé dieuf djeu dou nul ndakh nétali beu
Al amine sarr, amir abo samay waay nguéne
Sunu papa youssou ndour
Papa thione laniouy dioy waaw
Ndanane ngeu
Diambar ngeu
Xeex kaat ngeu
Goor pire ngeu
Référence ngeu
Fi nguako teik rek leu
Ndanane ngeu
Diambar ngeu
Xeex kaat ngeu
Goor pire ngeu
Référence ngeu
Fi nguako teik rek leu
Ecouter
A Propos de "Ndanan"
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl