Paroles de Badola
Paroles de Badola Par XUMAN
[COUPLET 1]
Dina fègn ci djiko dina fègn ci joudou
Ndax si deret lay nek du né ci mboubou
Dou yeugleu dou feug day dikk doug
Bouko bayi mou lékké lokho jokh ko koudu
Moy njeuk ci bool bi té moy ciy mujé
Foko fékk day foxolé beuneulé tek ci woudié
Dou doylou du né doyna dou doyal du déssal
Badola gaw ci né doli ma botou sa kaw di la diassal haaaa !
Bala jogg ci ndap li ndawal li dièkh
Bou souré dou né jaraw lako day foudd ray dékh ré né … (rhô)
Moy proux, dou geureum niami daw
Foumou la fékké si tolof tolof bayi lafa daw
Boko invité dey invité moromam
Té wax bou yonam néwoul fauk mou sapali ci xorom
Dafay sew djiko meuna setlou siss sof sans soutoura
Loumou la xamal mou siw rakh ci gaw ci soss
[REFRAIN]
Badola modi badola
Badola modi badola
Badola deug deug dey done niteum mi ngi sothi sa biri mbok ak sa biir keur
[COUPLET 1]
Xamoul diowanté té bala mo watch mou dagg
Bougoul déf deug ki mou beuga dég moy kou kay tagg
Sédeulé bouki lay sédeulé sou ko y’Allah mayé touti dolé dotoul diégeulé
Dafa gawa xébaté, gawa yabaté
Kouko eupeulé késsé kokou lay respecté
A ka meuna fallaté gawa jeulaté rambadj ni seytané
Niakk koleuré gawa djeuwaté
Bou souré rew bou amé bew
Amoul kaddu té day beugwakh ju sew
Dou kholé day khoulé kou moudeukeul nga tokhou
Dina lay gné dila ignanè
Di la soufou di la soukhlou dafa meuna niane té ney ba bouy saw sakh sipp
Sou dougué sa toillettes bayi fa bombe atomique
Dougn ko denk allalou mbollo dou fay borr
Bou abé dou délo so kay niane, niane ko ci biir mbollo ndax sou lay may da koy def si mbolo
[REFRAIN]
Badola modi badola
Badola modi badola
Badola deug deug dey done niteum mi ngi sothi sa biri mbok ak sa biir keur
Ecouter
A Propos de "Badola"
Plus de Lyrics de XUMAN
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl