LEUZ DIWANE G Gëna Jège Gëna Yey cover image

Paroles de Gëna Jège Gëna Yey

Paroles de Gëna Jège Gëna Yey Par LEUZ DIWANE G


Tambali ñu naan du dem
Ñi la waroon Dimbali té mane ko ñoy
Jëkke seetaan
Tamm na né ci di jéem
Mana gulo ma yéem
Gis na la nga mer di reetaan
Gëna Jège Gëna Yey but Gëna nay
Ba tay bataille bi day Gëna Wëy
Ñi lay bège everyday bo bu ba tay
Japp teye di ligey amu ma seen fay
Yeana ma yokk dole ak fit sas ngen ma
Taw na fi dënu riir ngalaw li jokk te bayi wu ñu bena yoon
Yalla moy bole ay nit fass nass ñu benn
Ku xar su ñu dëne si biir deg muy riir mak yeen da ñu bokk Yoon
Tefes la ñuy way way wi dëp sa gal
Géej gii sambaraax terewul ñuy Gëna  joow
Ne fess Gëna wëy ni fourmille ak cigal sigi sagal ñep sibo lu tax du ñu coow
Yen be dis bu dul woon ñen ñi yenne
ku nañ ko yagg na
But ki yen bopam ak ki ñu yen du bena yeene yi yegg na man
 
Le monde est chelou méfie-toi de l'apparence
Qui dîne chez les loups fait accélérer la cadence
This world is unfair don't trust to anybody (don't trust to anybody)
Focus on your aim do your thing if you wanna somebody
(If you wanna be, if you wanna be somebody)

Bo ñu doon buux
Sax du ñu deelu ganaaw
Xës nañ tekk tankk te day sax
Da nga ñu yeene ñu suux
ñu baayi daw di naaw
Compte bi ñu tijji banque jom be tax
Werantew ñokk ken si len
Li ñuy def ku ko feelul
Na dem tokk
Wërante ngeen ba tokk ci nen
That's beautifull
But my Niger let them talk
Ñii xam sa soxla
Te duñ ko facc
Ñoy facc sa soxla
Te duñ ko xam
Ñii naan waw goor ñële naan ñaw
Ñii lay taccu ñele tokk fële di ree
Gëmu ma xaar ñu dioxla
Lu ne lañ ci dacc
Goor sa waar Wa yox la
Wara feey ci ndam
Andak tangoor di leen caw
Bayi ñuy xaacu nga xol no koy doree
Lo gëna bañ gën ma beg lo
Gëmu ma noon
Sisu man be ma yokk dole
Sañ sañ bi ñor sa get go
Yena ma def li ma doon
Du ma tokk di xole
Bor bi yemul rek ci xorom
Yéene bi moy boutique bi tëcc
But anyway
Tewul naar bi gëm su ñu Borom
Def këcc lu yoon wi lëcc lëcc
Du ñu tere Wëy

Le monde est chelou méfie-toi de l'apparence
Qui dîne chez les loups fait accélérer la cadence
This world is unfair don't trust to anybody (don't trust to anybody)
Focus on your aim do your thing if you wanna somebody
(If you wanna be, if you wanna be somebody)

Xam nañ li ñu bëg
Te am nañ fulay jëli ko
Gumba tëxlu dem baña gessu dox ci li ñu yiteel
Yalla rekay dëgg bu mu yem rek ci wax na feeñ ci jikko
Lu dul mom neen la
Du ken ku ñuy njëkëntel
Xam nañ li ñu bëg
Te am nañ fulay jëli ko
Fulay jëli ko am nañ fulay jëli ko
Lu dul mom neen la
Du ken ku ñuy njëkënteeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeel

Le monde est chelou méfie-toi de l'apparence
Qui dîne chez les loups fait accélérer la cadence
This world is unfair don't trust to anybody (don't trust to anybody)
Focus on your aim do your thing if you wanna somebody
(If you wanna be, if you wanna be somebody)

Ecouter

A Propos de "Gëna Jège Gëna Yey"

Album : Gëna Jège Gëna Yey (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Feb 09 , 2021

Plus de Lyrics de LEUZ DIWANE G

LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl