Paroles de Ba Len Niou Wakh
Paroles de Ba Len Niou Wakh Par ELJAZ
[VERSE 1]
Di rapé ni guéweul
Mbir ma takkeu gnigue ma guéweul
Rime yi wadeu melni khéweul
Mélomane bi douma séwal no
Mane la jaz
Napeu sa MC bi ak sama thiass
Douma mouthiate
Sama famille mane la thiate
Khol na guel bi thiapé thiate
Khamouniou gate
Té si niome amoul thiass
Medina daniou ma sass
Sen yakar dou tass
Mane douma kouy perte bataille
Tothie na sen bataille
Walay sama none dou
Khakatay ma may ko ayy
Di rapé lou nice
Di soppi flow ni kakatarr
Di ndawal ci togue bi
Volant ci auto bi
Banfit ci conobier
Sam photo ci panneau bi
khamé nga kaname bi
Tous le temps damay réé
Dégloul, dégeu kham lou
Nitté ui wax si ioe
Boul meuss wax si niom
Ya len geun tax niouy wax si ioe
[CHORUS]
Hé ! Loum leundeum leundeum
Damay khouss diarr
Khouss diarr
Damay khouss diarr
Lou y’Allah dolel nitte mounou ko té
Dugn ma té
Boul lidieunti ba len niou wax,
Comme que khamo louniou beug
Boul lidieunti ba len niou wax
Comme que khamo louniou beug
Boul lidieunti bal en niou wax
[VERSE 2]
Laye pape diouf casse tout
As toute lay rap rek nga nangou
Yokhassoul lakatoul one two
Bala three yakheula nga sankou
Alboury mane la sen buur
Ma ngui tek lourd nion ngui diengou
Sentouma boussa beut floue ioe
Diguéma dégeuma Moscou
Deuké ci sandi ma caillous
Mane wax bi la taloul
Deuké jeuf té jamais ma adiou
Ioe tédieul ma parcours ba ageu souf keuleu
Sout keukeu sout kokou deh mako sout
Bayil dima sossal di yakeu derr
Imbécile khamaloma touss
Défeant li mbeubeutou
Def ko ma rétane di bobodiouf
Bagn kat la loumoumba
Black panther wakanda
Macky ba Mandéla
Cheikh Anta
Sankara, ngalé li, niouné lé
[CHORUS]
Hé ! Loum leundeum leundeum
Damay khouss diarr
Khouss diarr
Damay khouss diarr
Lou y’Allah dolel nitte mounou ko té
Dugn ma té
Boul lidieunti ba len niou wax
Comme que khamo louniou beug
Boul lidieunti ba len niou wax
Comme que khamo louniou beug
Boul lidieunti bal en niou wax
Ecouter
A Propos de "Ba Len Niou Wakh"
Plus de Lyrics de ELJAZ
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl