Paroles de Mayma Chance
Paroles de Mayma Chance Par HAKILL
Dafay yombe bou nio wone esay, daw loguama bama khokh
Diap sama khol founré nga diri khama niata yone
Ngama kong ngama bania guiss , bagne ma tontou bagne ma wouyou si
Mané dafay yombe bou nieuwone esay
Diokh nala assamane ak souf
Ngané ma ndawna ma teksi sama xol ak rou
Nganéma di dieul dama febar té yaye garap gui
Ngané ma wero wa legui nak lane la wara def sokhma si
Tay nak laa warou khama nak dingma may chance
Wa kagne ngay nangou nak tchi ligne bi bobou batay
Dieul ma tamit yag na en attente
Wakh na ba mot wou dictionnaire bi yeup diekh
Man ioe rekk la doundou mais ioe dangamay diey y’a nek sama xel
Ba samay xalatt ioe rek lagniouy xalatt boudou ioe dou done kéneu
Top nala ba yone bi diekhmayoma sakhk guestou
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Dieuf na wakh na ba deh
Meussoma sakh tontu
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Wakh ma man mo dess
Lane la wara deff
Woté na woté, yoné na yoné
Sokhna si wouyou ma wouyou ma wouyou ma
Wakh ma man mo dess
Lane la wara deff
Ioe xamgua falé wouma la
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Talou mala
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Falé wouma la
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Hey talou mala
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Ioe xamgua falé wouma la
Dangua beug deg baby awma sa diott sama khola busy
Ioe negua man rek nga guiss,lingua ma wan boukoul ak limay guiss
Bougou ma sa djiko sokhla wouma mbegue lou myhohey
Ling ma diokh lala delo mane ak ioe meunou niou pélo
Hey foné nga diokhé fa copie sa xol dafa moudié laté
Mbeuguel di ropalane ay fen diko piloter kharou ma dara
Kharou ma dara ndakh deug douma bourou bara
Douma bourou bara mane namou ma dara
May soukeur bou rakh petit cola danguay khar
Sopi sa djiko wala danguay khar, ioe danguay khaar
Top nala ba yone bi diekh mayoma sakh guestou
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Dieuf na wakh na ba deh, meussoma sakh tontou
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Wakh ma man mo dess
Lane la wara deff
Woté na woté, yoné na yoné
Sokhna si wouyou ma wouyou ma wouyou ma
Wakh ma man mo dess
Lane la wara deff
Ioe xamgua falé wouma la
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Talou mala
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Falé wouma la
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Hey talou mala
Wouyou ma, wouyou ma, wouyou ma
Ioe xamgua falé wouma la
Dimba lém a dimba léma
Dimba lém a dimba léma
Ecouter
A Propos de "Mayma Chance"
Plus de Lyrics de HAKILL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl