Paroles de Fii
Paroles de Fii Par HAKILL
Beus bouné ngûne ndioye doundou hiff
Beus bouné ngûne ndioye ngî deh wake marre ndioune rek
Langû dieppi beugou ngû ndioune ndio guissoul dieuf deuk si wakh
Ndioune ndio guissoul djieuf deuk si wakhh
Ndio guissoul djieuf deuk si wakhh ndax
Fii bala ndio diouge fok musiba ama fii
Bala ngaye diote fok nga yeuk ak wathie
Fii bala ndio jeuf mou ame camera fii
Fii bala ndio diogue fok musiba ame fii
Niak nandie ba niak lounge amagoul
Changement dandie ko khar ba khadi agoul li
Léné dinkeu ngéne ngûye diaye en retour
Ngû nieupaye guénte comme sall amdou ndioye
Tane ange ak rére beuss bou nek daff
Nguye teu wakhoumala chaque att ak wérr
Wakh léne ma kou amoule même nékeu nou yalla di
Teujé sa bountou ak sa plantere soumakoye wakh silou gatte moye
Bangû ngîsi dara moy amatounge si lindi niak ndioune amou ngû
Koussiye diapou ndakh dii bralong mo nguene back plus quatre
Ta mère fathioul problème mou diouni motakh boyii ligué deff
Si galleuh yii outi ndax daguéne ndioye digue-digue ba légui
Gall yii ndio nek di digue
Beus bouné ngûne ndioye doundou hiff
Beus bouné ngûne ndioye ngî deh wake marre ndioune rek
Langû dieppi beugou ngû ndioune ndio guissoul dieuf deuk si wakh
Ndioune ndio guissoul djieuf deuk si wakhh
Ngû guiss ndioune ndio guissoul dieuf deuk si wakh
Ndax fii, bala ndio diouge fok musiba ama fii
Bala ngaye diote fok nga yeull wane fii
Fii bala ndio jeuf mou ame camera fii
Fii bala ndio diogue fok musiba ame fii
Ndioye sénegal boussi souff, souff bi ngéne warone tabakh
Ngéne diouye ceupou ngûne dangene diouye mboubo
Sénghor diouye la tak ta bindal na mille poème djingene bou
Séne wakh massoul book ak séni jeuf dangéne di djirou xepp
Ngéne dioff lokho domame da djiotoul guinaw
Motkha mére bouo 60 ans diaye thiaff
Téranga sénégal toubat yéko kham mais entre ndioun ak
Ndioun mou nou ngû yénane té jam birr sénegal
La aye sénagalais di wakh doungué loué séne gallé aye
Sénegalais fii dara changer woufii démal bayii ndio fii
Bo niewaté fékat ngû fii
Beus bouné ngûne ndioye doundou hiff
Beus bouné ngûne ndioye ngî deh wake marre ndioune rek
Langû dieppi beugou ngû ndioune ndio guissoul dieuf deuk si wakh
Ndio guissoul djieuf deuk si wakhh ndax
Fii bala ndio diouge fok musiba ama fii
Bala ngaye diote fok nga yeuk ak wathie
Fii bala ndio jeuf mou ame camera fii
Fii bala ndio diogue fok musiba ame fii
Ndio guissoul djieuf deuk si wakhh ndax
Fii bala ndio diouge fok musiba ama fii
Bala ngaye diote fok nga yeuk ak wathie
Fii bala ndio jeuf mou ame camera fii
Fii bala ndio diogue fok musiba ame fii
Ecouter
A Propos de "Fii"
Plus de Lyrics de HAKILL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl