Paroles de Oumyna
Paroles de Oumyna Par HAKILL
[COUPLET 1]
Oumyna fo dieum, wouyuma ioe
Nangouna ni mala togn ma ngui diégalou, wouyuma ioe
Sama Oumyna fo dieum, faléma ioe
Nangouna ni dama dioum ma ngui diégalou, bébé wouyuma
Bo démé dina wett, té bouma wétté louné meun nako def
Oh ! Bébé boul ma gued dina bayi nieup ioe rek’a ma yitel
Nagn dem topouma, té douma waxate fatoumata
Nangotouma perte sama temps
Oui on ira loin loin
[CHORUS]
Oumyna amina amina
Oumyna amina amina
Si tu veux me parle pas mais ne me laisse pas
Girls parle pas mais ne me laisse pas
Oumyna amina amina
Oumyna amina amina
Si tu veux parle-moi mais ne me laisse pas
Girls ment pas mais ne me laisse pas
Girls you slay like Katana, like Katana
Girls you slay like Katana, Katana
And you slay like Katana, like Katana
Girls you slay like Katana, Katana
Oh! ma oumyna
Bébé you mala, thiow li thiow li yawa
Thiow li thiow li yawa
You my only one, you are my number one
Thiow li thiow li yawa
Thiow li thiow li yawa
[VERSE 2]
You slay like Katana
Rafet ngeu mashAllah, nala yobou ci maman
Dinala yobou ci maman
You slay like Katana
Rafet ngeu mashAllah, nala yobou ci baba
Dinala yobou ci baba
Chérie mbifé, chérie mbifé fétikhoflounéya
Chérie mbifé, chérie mbifé antifodioumfé
Chérie mbifé, chérie mbifé I love you bébé
Mbifé la moula bébé, mbifé je t’aime mon bébé
[CHORUS]
Oumyna amina amina
Oumyna amina amina
Si tu veux me parle pas mais ne me laisse pas
Girl parle pas mais ne me laisse pas
Oumyna amina amina
Oumyna amina amina
Si tu veux parle-moi mais ne me laisse pas
Girl ment pas mais ne me laisse pas
Girls you slay like Katana, like Katana
Girls you slay like Katana, Katana
And you slay like Katana, like Katana
Girls you slay like Katana, Katana
Oh! ma oumyna
Bébé you mala, thiow li thiow li yawa
Thiow li thiow li yawa
You my only one, you’re my number one
Thiow li thiow li yawa
Thiow li thiow li yawa
Katana
My girl slay like like like Katana
She is my todjana
She is my Habana
Ecouter
A Propos de "Oumyna"
Plus de Lyrics de HAKILL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl