SIDY KA Bataxalu Askan Wii cover image

Paroles de Bataxalu Askan Wii

Paroles de Bataxalu Askan Wii Par SIDY KA


Déret turu sufu senegal bay walangan
Takal badola bi raxasu si guéju nott
Thiono du fegn si pouvoir budul jehh
Non non nio bagn
Sama batahal bi
Askan wéma yondi fokma jalaléko
Meuna tougnou dundu li
Si nguur gudul jehh
Non non nio bagn
Thiow jiip na fugnko fogéwoul won
Injustice bi thi rewmii metina
Senegalais bangui jooy nakaru holl
Non non nio bagn

Yaw niata jeune nio deé thi lii
Rongognu nakaar féthiali
Waro haar ayy netalii
Sa deff patt a yokku li
Rew meepa ngui jooy
Holl yeupa and tooy
Non non nio bagn
Lettre bi filakoy yémaléee
Porteur de voix
Askan wi nioma yoni wonn
Senegall sunu gaal
Free Senegal
Non non nio bagn

Ecouter

A Propos de "Bataxalu Askan Wii"

Album : Bataxalu Askan Wii (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Mar 11 , 2021

Plus de Lyrics de SIDY KA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl