Paroles de Magal Gui
Paroles de Magal Gui Par ELJAZ
Magal Touba (magal Touba)
18 Safar (Ila Touba)
Magal diot na (Ila Touba)
Daniouy dem magal biss bi
Magal Touba (magal Touba)
18 Safar (Ila Touba)
Magal diot na (Ila Touba)
Daniouy dem magal biss bi
Kouy mouride wadialal ndax nieupay tew magal gui
Europe Asie Amérique nieupay tew magal gui
Tidiane Khadre Layen nieupay tew ci magal gui
Toubab narr ak chinois niom nieupay tew ci magal gui
Guinar khar ak guélém, nak ak beuy ci magal gui
Banane pomme ak limonade ak jus de fruit ci magal gui
Khassida zikr alkhurane leer ci magal gui
Ziar serigne bi nangou niane diokhé adiyah ci magal gui
Magal Touba (Magal Touba)
18 Safar (Ila Touba)
Magal diot na (Ila Touba)
Daniouy dem magal biss bi
Magal Touba (Magal Touba)
18 Safar (Ila Touba)
Magal diot na (Ila Touba)
Daniouy dem magal biss bi
Kouy mouride yeungeutoul
Touba geunél lango
Touba geunél la
Touba geunél lango
Touba geunél la
Magal Touba (magal Touba)
18 Safar (Ila Touba)
Magal diot na (Ila Touba)
Daniouy dem magal biss bi
Magal Touba (magal Touba)
18 Safar (Ila Touba)
Magal diot na (Ila Touba)
Daniouy dem magal biss bi
Ecouter
A Propos de "Magal Gui"
Plus de Lyrics de ELJAZ
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl