KID DOU  Arret Car cover image

Paroles de Arret Car

Paroles de Arret Car Par KID DOU


Damay doundeul rap Nguéne beugg ko doundé
Si Danger bi la né di mougn dè
Dougou ndiagua Ndiaye si Ferrari lay moudié
Amatouma temps legui warouma guoudé
Dioudou dokh magg fokk ma dé si guerre
Lima yagg deff c'est compliqué
Liné sama bopp khepp na sen succès
Dama rap ba nekk cas suspect
Dougueuloumeu sim diott Allo yamal buur la
Té foy diar malay tiime
Beugeutoumala fi guiss ni ranguognou badola
Sol thiéré mboubo OG
Seugg nagnou beuré gnakanté si lougnou beugg
Kougnou khossi gnolay khouri bangua fatélikou déad
Diékou nagn la paré ngané 4appui dou Diële
Nigger Ragualougnou Arret Kharé fi ba kheuy déh
Si son yi la geuneu super
Ouakam arret car  buruuit douma bett
Kou gneuw sama side dingua takk dieupétt
Té Kou nangoul thieupélou sa dano ley bētt
Lima rap sama khol bila bokk
Dama rame sogua meune dioukk tokk
Domeram sama team do bokk
Ngay diw khalei yiiii gnouy douy sunu poche
Sama raba geuneu sokhor El diablo
Yangui treune Batay diapoulo
Ngané yaye escobar Batay pablo
Bimay saltél sa kogn loutakh Fompoulo
Dangua rap Longtemps meusso am contrat
Lingua deff daw ngafi andi watt Comme dab
Dagnoumay cas té meussouma Corona
Laff thiate Dama rare ni black thii Kholou Naar

Gnoune Sakhar si lagnoulay kheur (Prrr)
Beuss Dingua Over Dose
Gnoy bandi yi meussougnou peur
Diang droit Xam pivot de Gauss

Gneuw Vider sen derett ni fosse sogua andi 109
Sama grade thi kaw lingua beugg lay keuf
Reste derrière tu faisais la meuf
From Ouakam tu connais la maf
May soti sen derett
Yeah may Bled
Damay Khotékou si beat deff trinte
Yene Amnguene blem
Kid dou tellem
Gneu Andifi lou math pourtant douma Grec

Rap galsen doyouma waay boulene ma téé
Boma beuggué djité faw nga gnanalma ma déé
Fess na si sa mind 7 maye sen Altesse
Takk 7 téwoul ma done Number One

Welcom to Drill - Dakar
Kay feel - sa life
Gnoy kill - sa gas yi
No peace no love
Welcom to Drill - Dakar
Kay feel - sa life
Gnoy kill - sa gas yi
No peace no love

Gnoune Sakhar si lagnoulay kheur
Beuss Dingua Over Dose
Gnoy bandi yi meussougnou peur
Diangue droit Xam pivot de Gauss

Ecouter

A Propos de " Arret Car"

Album : Arret Car (Single)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Oct 26 , 2022

Plus de Lyrics de KID DOU

KID DOU
KID DOU
KID DOU

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl