Paroles de Guiss Guiss
Paroles de Guiss Guiss Par KID DOU
Life bé yokk sama guiss guiss
Takh may geundi moytou ibliss
Légui mangui sante yalla So find
Si mane nguene beugg diott amouma diott no time
Diapanté pour meuneu tekki
Ndakh khamagougnou lougnou wara fékii
Lambi golo kou diokk danou ngui sibir
koussiné andi lokho Sounou gal dou meuseu dikk
Mane sokhlamou kharitou ennemi
Founé lagn dane andd ma diapéla sama G Yowwww
Effacé leu faté
Dinama diss
Beugeul ngama ma dé Yéné woma peace Yeah
Beugouma gnou melni Dupont et demba
Nagn beuggeunté si diam ni deukou Bamba
Sougn Ngor Nagn ko same moy yeufou diambar
Kepp kou done khaar sama danou yegg ngeu en bas
Life bé yokk sama guiss guiss
Takh may geundi moytou ibliss
Légui mangui sante yalla So find
Si mane nguene beugg diott amouma diott no time
Diapanté pour meuneu tekki
Ndakh khamagougnou lougnou wara fékii
Lambi golo kou diok danou ngui sibir
koussiné andi lokho Sounou gal dou meuseu dikk
Khalatouma deff la lou gnaw
Ak lo meuneu Tekk sama kaw
Sounou kharito makk yow
Meussoumassi khel Niar now
Tey nga Deff ko Thoma kholal souba nimley woré
Defla yeufou diam Blaise compaoré Yah
Si andd fignou diougué aka soré
Boul dam sama laff nagnou naw dem Gorée
Ba faaaaw
No Bou seytané dougou fi ak loumou meuneu méti
Meunoma diapp ba paré beugg meu diéppi
Waroul melni digeunté bou macky ak wade
Té Mane samay Ennemie la beugg sëppii
Beugouma gnou melni Dupont et demba
Nagn beuggeunté si diam ni deukou Bamba
Sougn Ngor lagn wara same moy yeufou diambar
Kepp kou done khaar sama danou yëgg ngeu en bas Yeaaah
Life bé yokk sama guiss guiss
Takh may geundi moytou ibliss
Légui mangui sante yalla So find
Si mane nguène beugg diott amouma diott no time
Diapanté pour meuneu tékki
Ndakh khamagougnou lougnou wara fékii
Lambi golo kou diokk danou ngui sibir
koussiné andi lokho Sounou gal dou meuseu dikk
Ecouter
A Propos de "Guiss Guiss"
Plus de Lyrics de KID DOU
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl