LEUZ DIWANE G Lambaatu  cover image

Paroles de Lambaatu

Paroles de Lambaatu Par LEUZ DIWANE G


Fi ma diogué gueunone ko diégué figne ko yaakarone
Fa ma dieum kheuyna mou leundeum khawma lou mou done
Yaakar ak beug beug mo niouy goungué da niouy saytou
Li ngay khaar ak li mouy done deug wouték li ngay séntou
Diéma comp li nga rombeu li nieuw souba done koupeu
Thiabi djiy tidji sa khombe weuri lokho bi ko keumpeu
Reubeu gloire yi tidjié ka teudji tirroirs yi
Dégue echo waroul takh nga tiit yaw rek si cloire yi
Adouna sélébé  yoone la fog ngay assumer say choice
Délou ganaw noone la kharal diégui def ni MOISE
Meuno kham kouy daane tankeu beuré wo ba nopi
Fog nga nguémboo deugueuntaane beuré daane gayi nopi
Fog niou ték si beut né mout djioundji doyoul domou adama
Kheuy takeu boot door waar bayék Rabana
Dougne la goungué télal ndiaap alone khame fi nga dieum
Ya kham li nga beugue done kou nékak la nga gueum

Fi ngay moudiéééé
Bo ko khamoooooone
Fa ngay ndieukééééééé
Do soneu si taneu yoooooon
Niak khama waral kou nékeu di lambatou
Yéééééyaaaa
Niak khama waral kou nékeu di lambatou
Yéééééyaaaa

What tomorrow hides don’t know may the Lord guide me
I know I got to fight but I fear the snake to bite me
Step the right step to the right path
He’s the one who knows
Set the light get it tight stuff
Understand the cause
Those elephant rose the lost yes that pause
Of course it is because you have taken that dose
Had a nose for it, chose bear it, ain’t take repose
Post and repost that’s how the game goes
Li la guéné school dougal la fi kheuy na mou gueune cool
Kheuy na amo deug soon or later ding ko gass soul
Bidew day fénké fou né foy dianok assamane
Li la def thiouné sabiir mind ndokh rakhass nda naane
Lou takh kou nékak béssoub dioudoma niou woutalé
Kou nék sa yoon boul mbélé mbélé si moom ba wadal coudom
Wara naw niou teutch la si kaaf
Souy pépeu meunoula satisfaire
Beug daw niou teutcheu say laaf
Soy répeu di yégg terre

Fi ngay moudiéééé
Bo ko khamoooooone
Fa ngay ndieukééééééé
Do soneu si taneu yoooooon
Niak khama waral kou nékeu di lambatou
Yéééééyaaaa
Niak khama waral kou nékeu di lambatou
Yéééééyaaaa

Fanané guénteu yéwo, diom kheuy wathiouwalék yaakaar
Dieul souba dénkeu sou niouy gaum ndiortay deufal naakhar
Khél di diékhlé beut niouy weur diamant fénéne fou doul si souff
Khole di diékhlé deuteu té évidement cuz geutam la niou toufff
Takh khoolam lére mou décoder code yi niou ték ti téktal yi
Bagne mére dokh calmer nerf moytou fi niou ték khal yi
Tant que yégoo amoo ndjiarigne donal doff bi anyway
Tankeu yéye go done seurigne niou naan keuff bi nga ni meuy
Ragal niakeu fayda fitay fiatal ladial kou la nékh
Yégal yégou tiger cuz sa battle amo kou ko khékh
Kou thialite diaye ngoram kou foukhalé wone méép
Lo guiss amna borom nita ngui lékanté ni thiéép
Ray niit wala doflo ko loray waadiouram
Am fit wala tiite beuguééé lou né lay dioureum
Ligne d’arrivée la niép di comptabiliser
Diaral si dériver ba séne compta bi miser

Fi ngay moudiéééé
Bo ko khamoooooone
Fa ngay ndieukééééééé
Do soneu si taneu yoooooon
Niak khama waral kou nékeu di lambatou
Yéééééyaaaa
Niak khama waral kou nékeu di lambatou
Yéééééyaaaa

Ecouter

A Propos de "Lambaatu "

Album : Lambaatu (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Oct 12 , 2021

Plus de Lyrics de LEUZ DIWANE G

LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl