Paroles de Soloul
Paroles de Soloul Par JEEBA
Solou louis Versace
Guéneu fuu nooy ngay lathieu tè
Souma nexei ma doon
Diego milliardaire Saoudien bou thiatiè
Maa guèneu nieup nè parfait
Diarou fi thiow maan la reik
Mafiiy capo numu ma nexei laakoy lakoy allignè
Mane Doumala laal solou bè laay dorée
Guissago dara kham nga dama tiofèe
Yow babe fane nga neik Nieuweul fi eeh
Niou photo wou snap begué dougeul
Taay oie bessu fête leu ma andaak babe
Daadi sool lu swaag
Lu raffet kaar
Waat nanii do seen mass
Linga sagnsei bakhna
Finga guéneu nooy na
Loor nga saay none
Uuhm uuhm uuhm soloul
Deef ko numu la nekhé oie soloul Uuuhm uuhm
Soloul dagoul fumu la nexei oie soloul Uuhm uuhm
Deef took jongoma
Finga guéneu neex nama
Dagoul nga dozéma
Yaafi meune lolou leer nama anh lii liii leeeh
Yeah yeah
Solou boudone lamb danga beurré beurré ba daan nieup
Sampe nga sa ndeunde keen douko tégui yaleen meune feep
Solou boudone khekh la saa youniu nieuwei niou feek la sen koow
Ngaleen di douma niouy doow
Kham naa dowoo thioow
Wawaaw yallah maynala tè danga ko xamoul
Sa yaram mo rafeet ba loo sool manaam daaf lay diap
Yeurré oloof daf laa diap bou toubabè daaf lay diap
Lo xalaat tè sola gokoo sakh nè nala daaf la diap
Mooh oubil sa bataan yèrrè yii waad
Nga sool ko deef Fass kanam
Eh boy beugg sagnsei taxouta meuneu sagnsei
Sagnsei yangui ni
Beugg jongoma takhouta meuneu jongoma
Jongoma nilaa warra meel
Bilay oie ma meuneu solou piir
Damay sagnsei khegn lou nekh
Guèneu nioumaay setane
Naane xalé bangui nii
Après mou diekh oie
Oie jeeba doliñu
Eeh oie jeeba amo temps
Tè maayo Khadim Temps
Temps ma temps dissi temps
Oie bessu fête leu ma andaak babe
Daadi sool lu swaag
Lu raffet kaar
Waat nanii do seen mass
Linga sagnsei bakhna
Finga guéneu nooy na
Loor nga saay none
Uuhm uuhm uuhm soloul
Deef ko numu la nekhé oie soloul uuhm uuhm
Soloul dagoul fumu la nexei oie soloul uuhm uuhm
Deef took jongoma
Finga guéneu neex nama
Dagoul nga dozéma
Yaafi meune lolou leer nama anh lii liii leeeh
Ecouter
A Propos de "Soloul "
Plus de Lyrics de JEEBA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl