Paroles de Signature Contrat
Paroles de Signature Contrat Par ZBEST FAMILY
Sénégal li nieup done khar mon ngui lé
Niary mbeuri takou nagn tay mou nex
Mbeur mi dou sone dou tayi
Mbeur mé sou diapé dou bayi
Paré ngen kone sétane len tay mou nex
Sampe na sama ndeundeu,
Chérie dieuleul sama avance bea
Waw heure bouniou beurré ma
Yoboula ardo
Bou arbitre sifflé douma léweuto
Dinala ndengengue gal gal
Ba ma topou la tafou la seussou la
Yoboula ardo
Chérie dinala attaqué, dinala cogné
Dinala fakhaté weuyeulé
Bébé dinala bonbon, dila tong tong,
Dila ndiol ndiol, dila thieul thieul, dila thieulé
[CHORUS]
Aythieu len, aythieu len, aythieu len
Beurré len mou gaw
Yague na, yague na, yague na
Heure bi diotna
Mbeuguel bou lakato, si xol lay né
Si xol ley né, cherie si xol ley né
Mbadou mon bébé, sama xol douko féké
Bébé limay ligueye khadioul ci ioe
Biss boma songué watna ni dig ko reuthio
Moytouma, moytouma bea moytouma
Dama yorr couronne’ou mbeuguel kone douma kheuthio
Sama thioumboukay soriwouma waxal
Loula nex
Dawna batay ay kilomètres, guiss fa sérigne nobel
Yako tay meuno wax ba doumala dann
Ah wa bo diéko del balé, sama mbeur mi maleu wolou
Hey! Sama mbeur gaindé la
Kep kouko meusseu teukou dann nala héhé
Mbeuro mbeur, yay
Mbeur, beurré dann gnibi yobou ndam li souniou keur
[CHORUS]
Aythieu len, aythieu len, aythieu len
Beurré len mou gaw
Yague na, yague na, yague na
Heure bi diotna
Mbeuguel bou lakato, si xol lay né
Si xol ley né, cherie si xol ley né
Mbadou mon bébé, sama xol douko féké
Bébé limay ligueye khadioul ci ioe
Biss boma songué watna ni dig ko reuthio
Moytouma, moytouma bea moytouma
Aythieu len, aythieu len, aythieu len
Beurré len mou gaw
Yague na, yague na, yague na
Heure bi diotna
Mbeuguel bou lakato watna si xol lay né
Si xol ley né, mbeuguel si xol ley né
Chérie dinala attaqué, dinala cogné
Dinala fakhaté weuyeulé
Bébé dinala bonbon, dila tong tong, dila ndiol ndiol
Dila thieul thieul, dila thieulé
Ecouter
A Propos de "Signature Contrat"
Plus de Lyrics de ZBEST FAMILY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl