SAFARY Kiss cover image

Paroles de Kiss

Paroles de Kiss Par SAFARY


[VERSE 1]
Damako yague piss
Yague nako beugeu bise
Mom deh dafa yague ci sama khôl bilé
Dafmay dozé
Dima vexé
Douma falé
Yeh ! yeh ! yeh !
Dafmay begué
Douko wané
Douma diégué
Wow! Wow! Wow
Wayé man deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man ki deh dinako am
Wadjilé man deh makoy mom
Man ki deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man Defa deh dinako am
Wadjilé man deh makoy mom

[CHORUS]
Wadji first time
Mako guissé
La képeu feeling man dal dama yague bardé
Wadji first time bima guissé
La képeu feeling momite dafa moudiou bardé
Wayé man deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man ki deh dinako am Wadjilé man deh makoy mom
Wayé man deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man ki deh dinako am Wadjilé man deh makoy mom

[VERSE 2]
Defa lidé Boko meunoul fadj Kayma wakhla nougnkoy déffé
Déko wone yone ninga nekhé
Boulko wone Dangko nope wadji ameko dou lou diaffé Eeh !
Wone ko yow ninga nekhé
Boulko piss yékh ko bise
Bayil mou khiff Nganiko thikh
Moulay fone nganane ko oh Yeah!
Moulay raay nganane ko Aïe !
Ak yénén you dakeu mew
Dakeu fraise té dakeu miel
Ak fém you dakeu nekh
Lolo koy nekh

[CHORUS]
Wadji first time
Mako guissé
La képeu feeling man dal dama yague bardé
Wadji first time bima guissé
La képeu feeling momite dafa moudiou bardé
Wayé man deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man ki deh dinako am Wadjilé man deh makoy mom
Wayé man deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man ki deh dinako am Wadjilé man deh makoy mom

[VERSE 3]
Piss Kiss mou gueuneu bardé
Déko wowé darling, wala baby
Déko snap WhatsApp wala Twitter
Bou diaré sakh bindeu mail
Neko love you my man
Neko love you my man
Penda Barry yaye chérie Yero
Yero Barry néna beugeunala
Mamy Thiam yaye chérie Abba, Abba no stress néna  beugeunala
Yow Déko piss Kiss
Mou gueuneu bardé
Cheikh Tidiane Ba moy chéri Lissa Ndoye Waw
Wowal mama Fatou Niass chéri Cissé Thiam Waw
Mani Abdou Aziz Mbaye Generalou Aziza leu
Bassirou gorou Ndeye gueye chéri Aminata Mbacké Bibi

Piss Kiss mou gueuneu bardé
Déko wowé darling wala baby
Déko snap WhatsApp wala Twitter
Bou diaré sakh bindeu mail Neko love u my man
Piss

Ecouter

A Propos de "Kiss"

Album : Kiss (Single)
Année de Sortie : 2020
Ajouté par : Farida
Published : Feb 28 , 2020

Plus de Lyrics de SAFARY

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl