Paroles de Nioun Laa Par SAFARY


Eh mangui dég
Dég aye wax leu
Wax fane lay takheu
Dou ma capable mat majeur
Lali lalaat
Mou nékh may defaat
Lénene ngay guissaat
Team millionnaire futur milliardaire

Ngay doundou thi réve
May doundou say reve
Normal que sa t’énerve
Tangal ay xol di soga  meune fékh
Mat lima done
Yeureum sama noone
Douma kén thi gnome
Téklé or soga tékléy tank

Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
On fait pas genre  ici tout va bien
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
On a l’argent ici tout va bien

Embody a godess so fuck being modest
Body on check said I’m just being honest
Surely the best yeah I’m surely the baddest
Baddest of all you just ask your mirror
Might eat these rap niggaz all up for dinner
No competition I was born a winner
Fuck your position and fuck your opinion
Yeah I’m Liberian my hair on brizalian
Ain’t with the cap shit
Niggah so I dont just talk shit niggah
Fuck window Shopping I like it I want it I cop it niggah
I’m doing it bigger , doing it better
Me and my sistaz get money together
New currency that’s for every weather

Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
On fait pas genre  ici tout va bien
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
On a l’argent ici tout va bien

Beus boula xass ba raw dotoul deloussi
Noyi tt une vie té doundo une minite
Wathial sama dér bayi ratatati
Dieuw moy lékeu nit kone bon appétit
Lii fii sa guemine dii wahh
Woutte nak lima sa geste dii wane
Saa bop rek nga nek dii nahh
Ohh please live and leave me alone
Def fangg nii djant youtube sa téléphone
Nitt yii dii daww yaww ngay nelaw bagn koula Raww

Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
On fait pas genre  ici tout va bien
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
Gnoune la dé woullah
On a l’argent ici tout va bien

Ecouter

A Propos de "Nioun Laa"

Album : Nioun Laa (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : May 25 , 2021

Plus de Lyrics de SAFARY

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl