Paroles de Marché Love
Paroles de Marché Love Par ZBEST FAMILY
Kay ma diayla mbeuguel bou deugou
Ak xol bou nice, bou ande yeurmandé
Kay ma diayla li nga geuneu beug
Djiguen bou bax dey wax deugeu
Kay ma diayla mbeuguel bou nex
Tek diayla sincérité bou werr bodoul guiss fénén
Gorr amna fi ak fidel bou yomb
Nobel amna fi, nobel bou nior khomb
[CHORUS]
Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw
Amoul waxalé
Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw
Louma dadialé, dadialé na pour dieunderou plaisir
Ay sacou bisous, je t’aime bou bax
Amna samou maikeur
Amna samou nobel
Amna samou mougn ak doylo waw
Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye
Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye
Magie beugeunté ngui ni
Mbeuguel rek lay diaye
Ioe fayal sa impot sa diouti avant ngey diaye
Et puis dama beug xol bou sincère goor bou ngeub
Kouy yeureum djiguen tek si diko wax
[CHORUS]
Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw
Amoul waxalé
Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw
Louma dadialé, dadialé na pour dieunderou plaisir
Ay sacou bisous, je t’aime you bax
Amna samou maikeur
Amna samou nobel
Amna samou mougn ak doylo waw
Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye
Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye
Ecouter
A Propos de "Marché Love"
Plus de Lyrics de ZBEST FAMILY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl