ZBEST FAMILY Amy Ndiaye cover image

Paroles de Amy Ndiaye

Paroles de Amy Ndiaye Par ZBEST FAMILY


Amineta ndiaye, aminata ndiaye
Amineta ndiaye mani wagnil ni ngua néké way
Amy, amy, amy adouna dou nono
Amy amy, amy wag nil ni ngua néké waw
Amy amy, amy internet dou nono
Amy amy, amy tik tok bi dou nono
Amy ndiaye
Bou tik tok nékone auto moy chauffeur
Tingui tingui tee eh eh eh
Amy snap béko misérlo
Sou yéwo deff na make up
Daddy commence pause na khéff ay lendeu
Dieul telephone bi tik tok
Dji lay néké que journée bay ladié
Amy ndiaye
Dou diappalé yaym snap la deuk ké
Sokhla sounékoul leu
Dou diappalé yaym snap la deuk ké
Tik tok béne yonn am 100 milles vues
Dooléti bénéne tik rok
Amineta ndiaye, aminata ndiaye
Amineta ndiaye mani wagnil ni ngua néké way
Amy amy, amy adouna dou nono
Amy amy, amy wagnil ni ngua néké way
Amy amy, amy internet dou nono
Amy amy, amy tik tok bi dou nono

Amy ndiaye day dokh di kardisha xale carte gap
Sacs bii saff nasseu
Amy ndiaye bou diougué sol thierré seuk ke abdou yeuré
None bindeu maartéee
Day lale fem yii
Day lale Gucci
Original liti
Amy ndiaye dou ligueye
Travaille banaaa ley
Elle travaille chez tik tok
Amy ndiaye kom auto
Tik tok bi ko moko
Bouyiinélaw sakh day photo
Amy ndiaye miss poto poto
Amy ndiaye euh
Dou diappalé yayam snap la deuk ké
Sokhla sounékoul leu
Dou diappalé yayam snap deuk ké
Tik tok béne yonn am 100 miles vues
Doléti bénéne tik tok

Amineta ndiaye, aminata ndiaye
Amineta ndiaye mani wagnil ni ngua néké way
Amy, amy, amy adouna dou nono
Amy amy, amy wag nil ni ngua néké waw
Amy amy, amy internet dou nono
Amy amy, amy tik tok bi dou nono
Amy amy
Amy amy

Ecouter

A Propos de "Amy Ndiaye"

Album : Amy Ndiaye (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Mar 29 , 2021

Plus de Lyrics de ZBEST FAMILY

ZBEST FAMILY
ZBEST FAMILY
ZBEST FAMILY

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl