Paroles de Chocolat
Paroles de Chocolat Par KERR GI FAMILY
Mbeugelou chocolat
Kerr gi family
Ooohhhh
Ooohhh
Oho
Yeee yeeee
[CHORUS]
Yaye sama chocolat
Fo diap bouko bayi
Rere si yow ba douma fegne girl you are ma sugar cane
You ma number uno
Sama chocoleca
Rere si yow ba douma fegne girl you are my sugar cane
Sans yow douma mouna né jamais
Ndakh yamay wetali baby boulma mereé
Ma rere yi rere si yow meur ba khametouma kima dome
Sama chocolat doumala café
Kay gua fone ma ma nek sa bea kay gua fo ak mane
Saf gama ndakh yallah khamnaneé soffoma
Yow defal sama love holidays everyday di party
I give you the title ma little bea
You ma bea ma bea ma bea ma bea ma bea
[CHORUS]
Yaye sama chocolat
Fo diap bouko bayi
Rere si yow ba douma fegne girl you are ma sugar cane
You ma number uno
Sama chocoleca
Rere si yow ba douma fegne girl you are my sugar cane
Tar bima giss dafa diegui dayo mane dé khawma kimou done
Mbeugel bou nekh bou dakh chocolat mane dé baby kay ga mome ma
Baby kay ga mome ma
I’ll love you forever heeee
Kay fowema
I’ll love you forever heeee
Baby ya mome sama khol gnowal gnou ande di contan di fo di ré
Baby yaye baye sama tol té khamnané lep louma âme yow yaye borom
Baby kay ga mome ma I’ll love you forever hééé
Kay fowema I ll love you forever hééé
[CHORUS]
Yaye sama chocolat
Fo diap bouko bayi
Rere si yow ba douma fegne girl you are ma sugar cane
You ma number uno
Sama chocoleca
Rere si yow ba douma fegne girl you are my sugar cane
Ecouter
A Propos de "Chocolat"
Plus de Lyrics de KERR GI FAMILY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl