AKHLOU BRICK Negu Goor cover image

Paroles de Negu Goor

Paroles de Negu Goor Par AKHLOU BRICK


Boy guénal sa négu yaay
Gneuw ci négu goor, dugu ci négu seuy
Di dém ci négu yallah
Guéneu négu yallah
Gnu dieméla négu deuk
Yéné négu la borom mathiay fanan
Motakh ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Aziz samb diokhal boy yi chips crax tampico
En place maarifa gang xam xam bu bayiko ba kossy
Doyal nagn ci reuk pott yi borom flow wou mbôt yi
Gnu wax lén xar’lén tanku toubey ngén koy xotti
Téknagn game ci loxo tacko fall ku yotu tokki
Muma ngén diox sen micro légui jangu yi tass
Djanteu bi fégn a lamp yi faay
What ever happen in vegas
Million ci poche mayé pôt ak sama Camaro
Bo beugué xam flow yima am comptél ay bakanu omaro
Bul rég’lék maan compte reg’lél say règle douleureuse
Rap ba to lingay deff momay diox mahfouss ak dudu buzz
Do civilisé ba romb yamb la gueuna fonk cacam
Sawara tuma raak nakh kossi noku duko wax papam
Dagn néma ara fow nga rap level bé dess fi
Rappeurs yé gueuna guateu carrière talibé ak bess fi
Maam la dof bi tokk xuri gnima done woku
Reudeu sama baram ci sen lakh bi sow bi dima topu

Boy guénal sa négu yaay
Gneuw ci négu goor, dugu ci négu seuy
Di dém ci négu yallah
Guéneu négu yallah
Gnu dieméla négu deuk
Yéné négu la borom mathiay fanan
Motakh ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Aziz samb diokhal boy yi chips crax tampico
Ku topu flow bi range ni id yak ay problèmu fonds
Ko topu brick tchi ate bu bess, day guéné hit ngay guéné son
Dama séxlu sen verres yi, ouchoiru monku mokay fomp
Lembadjé rap bi kéeu du guéné, bam melni dam leen di xon
Game bi ni oscar rappeurs yi mbalax individuel
Soppi gang yi ASC mbotipom nabajo NBA
Bagni’y organisé course rap bokuma sen départ
Bagnu akcé ci ligne d’arriver fala ma tokk dilen xaar
Fi kouné xam’na kouné banteu bu gudu lagnuy lalé
Reuk ndigu boy yi pateu sen beut gnunan ma yaw la’la
Terrorisé leen né ki neek palais man la come on town
Fogu rappeur dama ci siss ba dé l’os mor lam
Djarul changé flow doma djomal boy rabato
Béneu la ba lègui feul la tubat adji namato
Chien aboie caravane passe, dix sa guéneu mana ass
Rap bi né car rapide chauffeur bey encaissé kaanam passe

Boy guénal sa négu yaay
Gneuw ci négu goor, dugu ci négu seuy
Di dém ci négu yallah
Guéneu négu yallah
Gnu dieméla négu deuk
Yéné négu la borom mathiay fanan
Motakh ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Ku méér tant pis
Aziz samb diokhal boy yi chips crax tampico

Hey nénagn sen rap goor la dafa diongu
Ma lathie turando gnunéma aida diongue
Balén rap liguey yéna gui fontu
Amolen diom sisi ndax ba diom don xeuy
Yéén si guén guontu
Dagn may rélo rek mane xawma fougn’len foré damn
Léwett ni nawé sen rappeurs comme ay comédiens
Naan malay meun non malay faay
Nane mafiy doul mais yafiy dey
Non féthial dougui féthial waay

Ecouter

A Propos de "Negu Goor"

Album : Negu Goor (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Feb 01 , 2021

Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK

AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl