Paroles de Real Love
Paroles de Real Love Par DEF'L NICE
Mbeuguèl aka nekha neck
Thji kaw lingay yeuk, ma yeuk ko it’s a real love
Boudè say sou mètè niou daw
Dougn ko meussa doundou , enjoy souniou real love

Bimouy méti mak yaw la wonn
Mouy taw di nathie guisolèn wonn
May mougn di dékou boundouxatal aka dèko
Man souma xol moma togn
Waa ah yeah hey
Yaw ak man ni pik ak pèl
Bayi thji xel yaw souniou mbeuguèl
Liniou bole dou ay fo
Yaw ak man ni pik ak pèl
Bayi thji xel yaw souniou mbeuguèl
It’s a real love
Mbeuguèl aka nekha neck
Thji kaw lingay yeuk, ma yeuk ko it’s a real love
Boudè say sou mètè niou daw
Dougn ko meussa doundou , enjoy souniou real love
Mbeuguèl aka nekha neck
Thji kaw lingay yeuk, ma yeuk ko it’s a real love
Boudè say sou mètè niou daw
Dougn ko meussa doundou , enjoy souniou real love
No woman can do you like you in my heart
My baby eeh ouh yeah
Seytané yaknay xel wayè waxoul deugeu
So beuguè dégeu deugeu kay tayma waxla deugeu
Je me réveille alors que tu n’es pas la
J’ai besoin de toi
De la douceur de tes bras
De sentir que tu es là
Tenir tes mains car tu es mienne
J’ai besoin de toi
De sentir que tu es là
Ton amour c’est ma vie, suis d’accords
Tu es la vie et ça sera pour la vie
Mbeuguèl aka nekha neck
Thji kaw lingay yeuk, ma yeuk ko it’s a real love
Boudè say sou mètè niou daw
Dougn ko meussa doundou , enjoy souniou real love
Mbeuguèl aka nekha neck
Thji kaw lingay yeuk, ma yeuk ko it’s a real love
Boudè say sou mètè niou daw
Dougn ko meussa doundou , enjoy souniou real love
Inkré bouthiè oun djima ngalo girl I love you
Je t’aime, mbifé, évidement you know so crazy
She’s by my side, girl I love you

Inkré bouthiè ouna ouh ouna ouh
Wa ah ouh wa ah ouh
Seuy ba séy laniou digue lé aythia na matt
Xeuy ban gone sagnsé couplé moussé ak madame
Xol yi beg thjinn lou neekh aythia na barr
Mokou pothie gateu tankeu dégeu ndigeul

Ecouter
A Propos de "Real Love"
Plus de Lyrics de DEF'L NICE
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl