Paroles de Ma La Nob
Paroles de Ma La Nob Par ADIOUZA
Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète, tu me fais kiffer
Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète, tu me fais rêver
[VERSE 1]
Dagn ma ni tanal, ma diokh la sama
Volant baby dawalal, dawalal
Yay borom taly, bi may akati bi ladioumala permis
Non non non non
Ioe do niome, ba xol bi réré si
Mbeuguel yako fore, yako fore
Kou ci merr tampis, kouma beugeu
Nama bayi mak sama honey, honey
[CHORUS]
Yama def nima mel mala nob
Dama bardé ci ioe ma la nob
Da nga sorri ci mane mala nob
Ndax bougouma niou wett ndax da nga sop
Yama def nima mel mala nob
Dama bardé ci ioe ma la nob
Da nga sorri ci mane mala nob
Ndax bougouma niou wett ndax da nga sop
Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète, tu me fais kiffer
Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète, tu me fais rêver
[VERSE 2]
Tu as conquis mon cœur sa la moindre résistance
Il sera à toi pour toute mon existence
Qu’on soit ensemble ou à distance
Je t’aimerai sans répit avec patience
[CHORUS]
Yama def nima mel mala nob
Dama bardé ci ioe ma la nob
Da nga sorri ci mane mala nob
Ndax bougouma niou wett ndax da nga sop
Yama def nima mel mala nob
Dama bardé ci ioe ma la nob
Da nga sorri ci mane mala nob
Ndax bougouma niou wett ndax da nga sop
Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète, tu me fais kiffer
Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète, tu me fais rêver
T’es mon choix dara fayoula baby
Da ngay merr di geuneu diantal
Di khoulo sax di geuneu diantal
Sapeur fayoulaaa
Yama def nima mel mala nob
Dama bardé ci ioe ma la nob
Da nga sorri ci mane mala nob
Ndax bougouma niou wett ndax da nga sop
Da nga sop, da nga sop
Da nga sop, da nga sop
Ecouter
A Propos de "Ma La Nob"
Plus de Lyrics de ADIOUZA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl