
Paroles de Thiowo
...
Paroles de Thiowo Par AKHLOU BRICK
Guentt na
Nioune niaar thi bideew
Di naaw fanaane thi weer bi
Nganane nioune niara moudjé biir Aldiana
Thi ngama yéwé
Deugg deugg li thia love bala yeeh yeeh
Def ngama indo Bilay
Naniou bayi thiowo bi diarouko
Fing ma def laala def yeah
Mbeuguel meun nala doflo wow
Wowowowowow
Deuké di xoulo thiowo
Thiowowowow
Mbeuguel meun nala doflo wow
Wowowowowow
Deuké di xoulo thiowo
Thiowowowow
Mbeuguel meun nala dof lo wow
Dioylo wow
Dem bamou merlo la
Kaf lola reilo la
Fo lo la
Dinala beklo
Mbeuguel capitainou borom
Tei thiow bi moy xorom bi
Yow reika may wathieulo
Tei somay rei may wathieu yow
Mbeuguel capitainou borom
Ling ma wone amothi morom
Beugeu la, nga beugeu ma niou niro
Melni Binga Bingo
Thia love bala yeeh yeeh
Def ngama indo Bilay
Naniou bayi thiowo bi diarouko
Fing ma def laala def yeah
Mbeuguel’ay nono (l’amour c’est l’ennemi)
Mbeuguel meun nala doflo wow
Wowowowowow
Deuké di xoulo thiowo
Thiowowowow
Mbeuguel meun nala doflo wow
Wowowowowow
Deuké di xoulo thiowo
Thiowowowow
Thiowo woo woo
Deum wala jinee nga yaw wowowowo
Mbeuguel dou fo no no
Indo la bana yeufou cow bo bo boy
Bari lignouy thiowowo
Deum wala jinee nga yaw wowowowo
Mbeuguel dou fo no no
Indo la bana yeufou cow bo bo boy
Boma méré baby diaroul ngay todj kass dieulal lekh todial pess
Lekh ba ngui ni todial pess
Sougnou xoulo ba dioubo sougn ande dafay gueuna bess
Nonanté bi guena bess
Mane may golo yaw yaye garap
Même bougnou thiowee mane ak yaw mane yaw lay faral
Baeb mane lima dalon dou dalat
Wurus nga ngalam nga mala ngoye dotouma bawat
Never bawat
Mbeuguel capitainou borom
Tei thiow bi moy xorom bi
Yow reika may wathieulo
Tei somay rei may wathieu yow
Mbeuguel capitainou borom
Ling ma wone amothi morom
Beugeu la, nga beugeu ma niou niro
Melni Binga Bingo
Thia love bala yeeh yeeh
Def ngama indo Bilay
Naniou bayi thiowo bi diarouko
Fing ma def laala def yeah
Mbeuguel’ay nono (l’amour c’est l’ennemi)
Yow fing ma def laala def Baeb
Yow fing ma def laala def Baeb
Yow fing ma def laala def Baeb
Yow fing ma def laala def Baeb
Ecouter
A Propos de "Thiowo"
Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl