
Paroles de Insistéel
...
Paroles de Insistéel Par YOUSSOU NDOUR
Bo beugué boul hésité
Té nga wagni médité
Sou féké nandité nga
Da ngay insisté
Limou eumbe ci kholame
Yaw ba la nga koy khame
Faw nga insisté
Limou gardé ci kholame
Yaw ba la nga koy khame
Faw nga insisté
Le temps ne nous attend …….. Pas dal
Fi ak ya ngi hésité
Do ame li nga beugue
Le temps ne nous attend …….. Pas bilay
Fi ak ya ngi hésité
Do ame li nga beugue
Le temps ne nous attend …….. Pas salaw
Salaw salaw salaw salaw
Da nga koy diégué lol
Mou yeuk lou né ci yow
Nga yeuk lou né ci mome
Fofa dara doula raw
Yoya sentiments mo li fété ci kaw
Kouné yeuk sa morome ba ci sa tiatou karaw
Pour nga khame lou baré
Faw insisté – nga bagna soré – té boul hésité
C bien dé qu’en amour
Y’a des mis à jour
Qu’il faut faire chaque jour
Je vous assure qu’en amour
Y’a des mis à jour
Qu’il faut faire chaque jour
Le temps ne nous attend …….. Pas dal
Fi ak ya ngi hésité
Do ame li nga beugue
Le temps ne nous attend …….. Pas bilay
Fi ak ya ngi hésité
Do ame li nga beugue
Le temps ne nous attend …….. Pas salaw
Salaw salaw salaw salaw
Néwone na ay sentiments la
Né ti wate andoul ak principe
Ya autre chose lou eupe importance
Na nga fékhé ba khame lou né ci bir kholame
Lolou dal moy sa lumiére
Mo lay wone yone wi ngay diar ci kaname
Néwone na ay sentiments la
Né ti wate andoul ak principe
Ya autre chose lou eupe importance
Na nga fékhé ba khame lou né ci bir kholame
Lolou dal moy sa lumiére
Mo lay wone yone wi ngay diar ci kaname
Yow na nga insiiiiiiiistééé – innnnnsistéééé
Yow na nga insiiiiiiiistééé – innnnnsistéééé
Ecouter
A Propos de "Insistéel"
Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl