JAHMAN XPRESS Def Si Code cover image

Paroles de Def Si Code

Paroles de Def Si Code Par JAHMAN XPRESS


Oh yeah
(Bagnal lolou)
Oh yeah
(Yaw mi adioul lolou)
Oh yeah
(Bagnal lolou)
Oh yeah
(Mani adioul lolou)
Oh yeah
(Aannh)
Oh yeah
(Bagnal lolou)

Yèneu say ma compou lèpeu
Noppi bayila sii biir
Limay togou sou gnoré
Nga xamni may bandit piire
Thiow djiboul diapè ma dof boudè moddi dalal sa xel
Madon ngaka ba am lima beug bou yabo nagn ma diay
Xam  ba thja dafa nekh djiguène pèkhé konn wéroo
Yaw bandit ngamay diay dangay dièm meunago
Guisma tay né dangma nopp ma rè nga fokni dal nga thji
Fowèma mola taxa diok wayé dotoko défati
Ma ay si goor bou geumoul dara teksi beug ma fowè
Damlay wol dila réé nann la baby yafii né
Nanla amo morom bèneu ngafi Sama Gloria
Mbeuguèlou Joni-Joni thiop sa wari tok di xar ria

Banial lolou , banial lolou
May waxak yaw mani banial lolou
Adioul lolou, Adioul lolou    
Yama geuna xamni ragalouma lolou
Def ci code (eeh eh)
Anh def si code (eeh eh)
Anh def si code (eeh eh)

Fii lofi indi ngafiy fèkeu boulma wo
Si arou bandit man goor la tè awma loumay perte
Wathièl sa bopou dalal boul diay sa taar ngir alal
Amo loudoul sa bopou lii dalay tardèl
Sa dara bougé woul ndakh lèpeu nga statut
(Mbètè monument)
Loula mètèk, loula neekh nga dougeul statut
(Tè todio fèneu)
Solak soumi melni yaw amo bèneu soucis
So xoulok sa copain yaw nieup xamko thji sa statut
Kèneu falè woula ko diotèl yako togn
Yaw sonal nganiok, ma yeureum samay nonn

Mbeuguèlou film nguèn di doundou
Falètou lenn moeurs guèl bouy wiri-wiri
Dou meuss diok thji mbèdeu
Dioubeu di wèssoul def statut nann la femme du boss
Kann leu ? Meuno lénn niou tek xel
Yènn koulèn raw dee gnèmè nguènn
Tè yenn geumolèn dara eh yaw règlèl
Bodonn mbeur  narnga beui défaite ngaka
Nganan baby yafi né bilay yamay danèl

Adioul lolou, Adioul lolou    
Yama geuna xamni ragalouma lolou
Banial lolou , banial lolou
May waxak yaw mani banial lolou
Def ci code (eeh eh)
Anh def si code (eeh eh)
Anh def si code (eeh eh)

Bouldi gawa naguou yeuk seu bopou
Boudoul yaw di kènènn
Nimay diapè lay bayè tè man goor douma fowè
Leungo nexna wayé ko bayi mou dèmaki mbagam
Si tu peux m’oublier
Je ferais comme si tu étais jamais né
Yangui nax sa bopou so foguè ni meunou’mala bayi
Djiguèna sou nieuguè dotoul saurr xawma loy diay
Beug bimala beug boulko diapè ragal
Boulma topou bama seuss nitt kou nèkeu amna limite
Respect bimala diox dèlo mako wala kounèkeu dem
Nangoul nala louné thji nga dakeu lè
Xoulou goudi xoulo beuthieuk dara taxoul nga ba
Meuneu touma dama sonou sa ay caprices
Goor dou ngora kassè djiguène dangkay meuna yeureum

Banial lolou , banial lolou
May waxak yaw mani banial lolou
Adioul lolou, Adioul lolou    
Yama geuna xamni ragalouma lolou
Def si code (eeh eh)
Anh def si code (eeh eh)

Ecouter

A Propos de "Def Si Code"

Album : Def Si Code (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Farida
Published : Mar 04 , 2020

Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS

JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl