Paroles de Baye La Solution
Paroles de Baye La Solution Par AKHLOU BRICK
Barhama Barhama azim
Baye niass moy borom
Barhama borom « Face Yii »
Baye you ki moy baye
Docteurou xol yi
Moy baye billahi
Mo neub boppam womé yalla
Nieul benam mbeuguel la wonn
Beuguel modi maye
Way xamouniou ko way
Sa nonne yii bagnougnou la
Dagn la rere billahi
Gnou tope ler gui ba
Sa adama khame nagn la yaw baye
Mo di baye
Ya war xol yii sol thi marifatou billahi
Anrif ya ngay sikar lahillah ilallah
Ila ila ilallah baye ilallah
Yalla ko tannal thia
Gna geun thia gna geun
Talibe baye bii deh
Nexoula gueseum
Ler be gnou nandal
Gno yore thia euzzul
Deysann yalla deff moudi baye
Koko di baye
Baye allah allahou ilallahou
Lahillaha ilallah
Baye dagn donn ziare
Makanou bi si sounou Senegal
Koko di baye
Baye allah allahou ilallahou
Ball len
Thia bamouy baye
Baye allah allahou ilallahou
Baye
Kou yobou diney lislam
Fou dine agout
Toubal ay diouniy nit si ben ngonn
Kokoy baye niass
Kou dioudom di kamal
Toudou cheikhal lislam
Teuthi bountou khot bou zamal
Kou donnou yonente khakhi khatann
Tok thia akhadiya donnou cheikhou tidjane
Kokoy baye niass
Koukhouran donn kiramam zahiram
Mou geuneu neub batinam
Gorou yalla ya ngay diayante
Sa euteum ba
Tarou yonente la lambo thia kanam ga
… Lo wo thia yalla boutou baye bana nam
Moy borom face yii
Borom kossi moy deg deg baye
Moy bayou assi
Mame baye dagn la rere billahi
Gna tope lerba thia adama
Xaùe nagn la yaw baye…
Moy bayou assi
Ya xar xol yii sol thi marifatou billah
Anrif ya ngay sikar lahillah ilallah
Ila ila ilallah baye ilallah
Yalla ko tannal thia
Gna geun thia gna geun
Talibe maye bii deh
Nexoula geuseum
Ler be gnou nandal gno yore thia euzeul
Ndeysann yalla
Deff moudi baye
Koko di baye
Baye dagn donn ziare
Makanou bi si sounou senegal *
Koko di baye
Baye allah allahou ilallahou Lahillah ilallah
Ball len…
Thia bamouy baye
Baye allah allahou ilallahou Lahillah ilallah
Baye willan baye wayou baye ba thieye
Thiey baye dioy nagn la baye wayou baye ba (Thiey baye)
Mame cheikh ibra fall woyou baye ba (Thiey baye)
Imam assane cisse wayou baye ba (Thiey baye)
Baye borom tall wayou baye ba (Thiey baye)
Baye cisse baye wayou baye ba (Thiey baye)
Cheikh mari cisse wayou baye la (Thiey baye)
Willanni willanni willanni baye la (Thiey baye)
Ecouter
A Propos de "Baye La Solution"
Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl