Paroles de Derangé
Paroles de Derangé Par WALLY SECK
Soma dégué
Soma wooloo
Na ñou andado
Gala wayy bouñou déranger
Kaddu gui laleine di déngkeu
Bouñou déranger bouñou déranger
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Dakar ba Thiès
Kaolack Tamba ba Diourbel
Fatick Saint-Louis
Na ñou ande cii yar ak yiiw
Ñeuwléne ñou sett
Souñou reew mi loukoy naatal
Moy ndaw you guëstu
Ngala wayy baña déranger
Souñou reew mi ñoko bokk
Bouñou déranger
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (yow déranger)
Non non non non
Ñeuwléne limey sène
Souñou andé nekk ben leppay easy
Louñou yootou meune cii diote
Negn léne yiiw
Teyy
Baña khiiroo souñou biir
Neñ leine dorr warr
Ngala wayy bouñou déranger
Souñou rew mii ñoko bokk
Na ngueu teup cii kaw (yow déranger)
Ba ngueu bouger nii (yow déranger)
Na ngueu teup cii kaw (yow déranger)
Ba ngueu bouger nii (yow déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Kone yow sama soppé
Boul dii khoulotii ndakh mane
Liimeu beug Liimeu beñ lay bolei daane
Sama khol dou diiouk cii yeine
Bii ñou andé beu legui
Ñii ngui gueune dii diéguii
Diégui frontière yééé
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Na ngueu teup cii kaw (no déranger)
Ba ngueu bouger nii (no déranger)
Kédougou Sédhiou Matam
Kolda beu Ziguinchor
Kaffrine beu Louga Lô
Fatéwma wa Podor yaye
Yakham Mbaye
Yakham wooma
España Boloñas
Scotland
Italia
Fatéwma wa Paris yaye
Bayou Fallou Mbaye
Espagne ba Allemagne
Norvège ba London
Fatewma wa Hollande
Habidu Belgique man
Ecouter
A Propos de "Derangé"
Plus de Lyrics de WALLY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl