Paroles de Li Lerla
Paroles de Li Lerla Par DIOR MBAYE
En lil lerla am mbeuguel la
Li lerla am mbeuguel
Xalé bilé mbeuguel ci xo day fegn ci kanam
Lil lerla am mbeuguel la
Li lerla am mbeuguel
Xalé bilé mbeuguel ci xo day fegn ci kanam
Mala nob assumé na louma ci gobé gaar
Ya né sama biir xol ya raw far bou jar
Chéri néna nima mel yako wara tako jaar
Lil lerla am mbeuguel la
Li lerla am mbeuguel
Xalé bilé mbeuguel ci xo day fegn ci kanam
Mane souma lay guiss
Ni may jongoma dama ko ragal
Lémi lémi dou sama yeuf damy dokh di tagal
Sama mbeuguel ci yow bou done ay ay lo douma ci feggal
Lil lerla am mbeuguel la
Li lerla am mbeuguel
Xalé bilé mbeuguel ci xo day fegn ci kanam
Adja soda maréme thaim new jersey
Thaim demba torodo bi ci walo
Thiatou adja daro ak aladji ousmane
Thiam dembaa
Seut ci elhadji malick SY
Seut ci maam ahmadou bamba
Seut ci cheick oumar foutiyou tall
Yayou amina niane ak
Papa ousmane niane
Ab thiamen dé day bari jom
Bayou nabou nana ak ramatoulay
Thiam wona bassirou thiam demba
Ko koy chérie sébastien
Somou ndayou fatimata dramé
Man dé lima don sett guissnako
Thiafka mbeuguel bime done weur amnako
Yaye sama aldiana xamnako
Lil lerla am mbeuguel la
Li lerla am mbeuguel
Xalé bilé mbeuguel ci xo day fegn ci kanam
Li motax sama rew nekh
Sénegal ndiay séni jegg danio jongué
Li motax sama rew nekh
Sénegal ndiay séni jegg danio jongué
Ndey coumba Vip hair xalé yangui di jongonma
Kou ci gattoul dangua ndiol té koiuci xessoul danga nioul
Chérie ousseynou guey jegg bobou aka paré
Li motax sama rew nekh
Sénegal ndiay séni jegg danio jongué
Man bouma sagnsé nga kholma
Rétaan nga may béguel
Ma diko tiktok nga to di sétan moulay yenguel
Li dou kemtan sagnsé ma gueneul
Li motax sama rew nekh
Sénegal ndiay séni jegg danio jongué
En diawri thiane chéri babou anne yayou
Zeyna ak binta ak abdlaye borom America
Lal na sama lal bi bamou tali thiouray di guilli
Ay mbal aki guert la sajj nekhal goudi gui
Bégual sama xol dara douko dakk yay sama
Sadio bane dina la may mbakhous bou rey tay
Ecouter
A Propos de "Li Lerla "
Plus de Lyrics de DIOR MBAYE
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl