Paroles de Al Ma No
Paroles de Al Ma No Par BY MIC
Li comme kaani sa t**te
Dougou ci Nioune no dou baakh kone rabal té teudj sa gate
Gueune la tangue Fils (No no) soxla wouma takk
Dagne Dopé Tame dougal kone normal ma nekk Attaque
Papeu pardonne pas
Djikoy pussy Mane leu fuck
Dinga goudé
Raagou Niari Soulou
Wax lou ci yonou Thiokk
Toucher Couler
Travail de Mama Ma topou, loumay doyé thiogou.
Bougn sékoulé
Nouyo késsé Kone boul xar ma tontou leu
Lemal té togue
Oulé Oulé
Aye Toni bodio bodio kone normal sen Rap bi dem bloc
Mangui ci État Niom nieup nagne paré
Pour niam Coups
Li moy Rap Sénégal, Nekh ni Comédie Niankou
C'est Quoi le débat ? Rap dey Beugue tokhou
Got my own Vibe Noumou Toudou Forsa Manjaku
Li Ngay Rap ba neugueuni safou niou demal niou fay la sa xorom
Pour niouss yi gueuna dagane ci nioune nieuweul nioune def nagn la morom
Gauche droite Gauche droite
Ana Kou meuneu téré déf Crime
Béneu Rhyme Niou Niaanal la
No dou béneu Bilaye Walaye
Al ma no
Alin Boula ngha ké
Al ma no yeah
Alin boula ngha ké
Al m no eh, yeah yeah yeah yeah
Al ma no eh
Alin boula ngha ké
Tira boca Na nha copu
Tira boca Na nha copu (Woooh)
Mangui Fi kene dou ko wax
Xam nga ni leuf li nioune Niongui ci biir
Dama Dji Tolou Thiow
Kone Loumay ragal pour Goobe fi riir
Na sin Batchi tchendin
A nghal pë pibaninde ou Tchits inji nian dika ro
Poftan ak Diakato
Ladial ba nian ka to
Esk c'est Dope
Gueune len Sadik
Diox Mic ak Bic
Pique ak Brique
Pour ma soul aye nit
Doma ngay diaye Cana
Mane la Domou Ndiago
Boula tanga
Pour Diolou sa Eeehh
Guili Xettou Néw
Homie Daniou nianga yangui Adéane
Niola gueuna dé
Safara Flow
Call me Ninki Nanka
Lolay Daouda Sané Koulo bouté
Nign key Wouté
Ci lagn wouté
Bou nekh bi fi nga key witté
Ndiago Socé Wolof Pular
Pour yimbé ngandi mi comme Toucouleur
Todj Cass Flow Soûlard
Ba nieup mandi lolou dou goulète
Sembéring Sembéring Woya
Pour Nande Code yi fok nga dougou leule
Ndanka Ndanka kana féya
Soy diaye THIAGA soulou dougou leu
Al ma no
Alin Boula ngha ké
Al ma no yeah
Alin boula ngha ké
Al m no eh, yeah yeah yeah yeah
Al ma no eh
Alin boula ngha ké
Tira boca Na nha copu
Tira boca Na nha copu(Woooh)
Ecouter
A Propos de "Al Ma No"
Plus de Lyrics de BY MIC
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl