Paroles de Li Fepp Ley Douga
Paroles de Li Fepp Ley Douga Par BY MIC
A Yeah Yeah Yeah
Mane la Papeuh Ndiago !
Koula ladj fima diogué
Néko Casamance
Koula ladj fima diogué
Néko Adéane
Casamance my bendo
Welcom to Casamance
Casamance my bendo
Welcom to Adéane
Gni di wax Moussou niou ma guiss
Lolay ignane ak xol ou siiss
Xamé nga souma face
Im the boy from RN6
Guéneu bou nekk comme attentat
Do fi job banga atane ma
Diyam siya bari mbita kang
Dokouwo man Dio abé faniyaléla
Fou légende bi diogué Néko Casamance
Dama Train ba Taxaw nokou samay maass
Ici je vois que des copies collées
Laisse les parler mais on se connait
Guiss ma guiss aye bagasses you diiss
Diss ma fils moy di dox Timiss
Yarou wou len égal zéro peace
Guéwou bouki fok déret Tiiss
Casamance sama déret, Ba sama Bissou doma téré Diko téral
Adéane fi ma diogué And im hard Dangay Séral may taral
Koula ladj fima diogué
Néko Casamance
Koula ladj fima diogué
Néko Adéane
Casamance my bendo
Welcom to Casamance
Casamance my bendo
Welcom to Adéane
Koula ladj fima diogué
Néko Casamance
Koula ladj fima diogué
Néko Ziguinchor
Casamance my bendo
Welcom to Casamance
Casamance my bendo
Welcom to Ziguinchor
Damay Maguette di geuna bess melni dalou colobane
Mague daane yobou ndam li sama side ndiabote dji nioungui xaar
Di nokhé té douma baal
Rakk dalal fi c'est du sale
Lyrix séduisant fait pas genre
Que tu ne me connais pas Wech
Moro nanang Yé si ngha yitang di yé
ko nté na tol manké Killing ti.
Adéane yé kouro lé dina dé
Bari kolong da to nté mé la dié.
Xethio len King bi
manguek couronne bou bax bi.
Bari yeurmandé moma dougal ci baalé
Boy li fepp ley douga
Li fepp ley douga
Boy li fepp douga fepp ley douga té nieup ley nouka
Boy bi fepp ley douga
Ki fepp ley douga
Boy li fepp douga fepp ley douga té nieup ley Thiouka
Koula ladj fima diougué
Néko Casamance
Koula ladj fima diogué
Néko Adéane
Casamance my bendo
Welcom to Casamance
Casamance my bendo
Welcom to Adéane
Koula ladj fima diougué
Néko bignona
Koula ladj fima diogué
Néko kolda
Casamance my bendo
Welcom to Casamance
Casamance my bendo
Welcom to SEDHIOU yeah
Boy li fepp ley douga
Li fepp ley douga
Boy li fepp douga fepp ley douga té nieup ley nouka
Boy bi fepp ley douga
Ki fepp ley douga
Boy li fepp douga fepp ley douga té nieup ley Thiouka
Ecouter
A Propos de "Li Fepp Ley Douga"
Plus de Lyrics de BY MIC
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl