Paroles de Nel Mashallah
Paroles de Nel Mashallah Par EL MAESTRO
Dama dém ba fouma teul
Ñunéma xalé bi kaar
Dafa dém ba fouma Sagnsé
Ñunéma kaaro Mashallah
Damay lakatou sax
Dama tamm rare man
Thiat gui ci limiñ
Dafa séw té gaw
Iyoo ho
Waxal Mashallah
Iyoo Iyoo
Man doomu Jambur la
Iyoo ho
Waxal Mashallah
Iyoo Iyoo
Man doomu Jambur la
Lakalé né N’golo Kanté
Thiat dafa séw té gaw (Dieuleul)
Xaral ma takk Pétaw
Wala ma setti Maam (Nganima)
None yi none yi none yi
Dañu doy waar
Diaral nalén dém si Seriñ
Garé la
Bu yabo
Nga fagaru
So déwé safoulen sax
Cool lal
Bama Sangatu
Séti Bakhaw Lalaké
Iyoo ho
Waxal Mashallah
Iyoo Iyoo
Man doomu Jambur la
Iyoo ho
Waxal Mashallah
Iyoo Iyoo
Man doomu Jambur la
(Tathiou lén mu rirr
Wawaw
Dieuleul)
Bulma thiatu thiatu thiatu thiatu
Bulma thiatu ( Ñeuwal )
Bulma thiatu thiatu thiatu thiatu
Bulma thiatu
Iyoo ho
Waxal Mashallah
Iyoo Iyoo
Man doomu Jambur la
Iyoo ho
Waxal Mashallah
Iyoo hoo
Man doomu Jambur la
Iyoo
Nél Mashallah hahan
Domu Jambur la ah ah
Yalla nañu Yalla Mussal
Si thiat lamiñ
Mussiba la déh
Kou garé mola garé
Lamiñ
Ku taxaw mola freiné
Yalla buma freiné man
Ecouter
A Propos de "Nel Mashallah"
Plus de Lyrics de EL MAESTRO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl