Paroles de Mbëgel
Paroles de Mbëgel Par MNM
Anhh yaya yaya
Ioe mii ioe rek ioe mii ioe mii
Anhh anhh ana nana
Dieum dji rek ladonn sett (ladonn sett)
Fèñ na cii ioe dotoul rérr (dotoul rérr)
Baby my life don't be afraid (don't be afraid)
Dotouma bayi diotena teuyè
Konn feel your love for me (feel your love for me)
I do it for you do it girl for me ( do it for me girl yaw)
Bébé cii ioe la mirr (bébé cii ioe la mirr)
Kouma xol cii ioe never mou tekma nitt (never mou tekma nitt baby)
Hè diotenala mine girl (demna ba mine leu baby)
Ohh baby my vitamine girl (anhh yayay vitamine girl)
Love you my sweet girl (i love you To mon bébé )
Hè ioe mii sañe nalla guiñieul ( guiñieul doumasi diog ndakh)
Mbeuguèlou thiaxann taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou foo taxouma diog (lolou taxouma diog hè)
Mbeuguèlou hun hun taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou yeurmandè ma taxa diog
Hè hiyè èhh ioe nana nana anhh (ohh wouhhan anhh yaya yany)
Nana nana nann anhh ( ohh wouhhan anhh yaya yanyi)
Hè nana nana nan anh ( ohh wouhhan anhh yaya)
Nana nana nann anhh (ohh wouhhan anhh yayayi)
Ndèker mbeuguel nila nèxè carlou meun nama sedder
Baby xolma ci beut way yeug xol bi noumou seder
Mag ioe deug laniouy doundou takh ba talatouma rêver
Yeurmandè lall louniou bolè mais tay mbeuguel bii lay fêter
You know me ( you know me)
Baby my life my only (my only)
Boma namè del xol fii (del xol fi)
Ioe rekka takh ma melni ( ma melni ihh)
Waxnalani diotenala mine girl
Ohh baby my vitamine girl
Love you my sweet girl
Èhh ioe mii sańe nalla guiñieul
Mbeuguèlou thiaxann taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou foo taxouma diog (lolou taxouma diog hè)
Mbeuguèlou hun hun taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou yeurmandè ma taxa diog
Hè hiyè èhh ioe nana nana anhh (ohh wouhhan anhh yaya yany)
Nana nana nann anhh ( ohh wouhhan anhh yaya yanyi)
Hè nana nana nan anh ( ohh wouhhan anhh yaya)
Nana nana nann anhh (ohh wouhhan anhh yayayi).
Tank ak tank mbag ak mbag bagn dem cii ngoro
Donn na tay dehh kilay tagg wawaw dotofi thioro
Cii yeurmandè la mbeuguel magg dotouniou tongo
Donn na tay yaw kilay Madial anh yay dieumèma bango
Ioe rekk mii (ioe rek mii )ioe mi ioe rek kèssè lay donn
Xolma fii (xolma fii)xolma fii do wètt cii bii yonn
Tagal la say mame bou doyoul( doyoul)
Gorel nga diam bii dioyoul (dioyoul)
Lima diota niamm ni kouko diota niam nieuweul seder ni sofoul (sofoul)
Èhh anyaya anyan yayaya
Èhh anyaya anyan yayaya
Anh yayayè anh yayaya
Anhh yayaya anhh yayaya
Ecouter
A Propos de "Mbëgel"
Plus de Lyrics de MNM
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl