Paroles de Fou De Toi
Paroles de Fou De Toi Par EL MAESTRO
Cherie fouñu diar yép (Yép)
Mamouy méti bébé
Ñun ñar rék (Rék)
Cherie fouñu diar yép (Yép)
Li guenone méti bébé
Romb nañu lep (Lép)
Cherie coco no no bou dem
And nañ ba Yalla def ñu seuy Si farata
Nga mouñal ma
Louma jiguen meusta mouñal Jaarama
Yaw milé
Yaw milé deh
Yama dioural sama taw bé
Yaw milé éh éh
Yaw mi deh
Yamay motali souma wété
So démé sama keur gui
Dina tasss Wawawaw
Chérie sama xol yawa
Té kinga xam mana
Namnala man bay dioy
Chérie daga dém ma wétt
Té so ñeuwé mou déñ
Boudoul yaw dou done kénén
Lolo am
Té dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Chérie man dama dof si yaw
Dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Chérie man dama dof si yaw
Xamna ni mala togn baby
Je t’assure j’ai fauté baby waw
Je me suis excusé
Adouna bi yama si guenal
Maguilay dora chérie boy mané balma
Bouñ la wowé fi lé
Bouñ la wowé néla dof na
Boumla bétt balma
(Yép yép)
Mamouy méti bébé
Ñun ñar rék (Rék)
Cherie fouñu diar yép (Yép)
Li guenone méti bébé
Romb nañu lep (Lép)
Cherie coco no no bou dem
Chérie sama xol yawa
Té kinga xam mana
Namnala man bay dioy
Chérie daga dém ma wétt
Té so ñeuwé mou déñ
Boudoul yaw dou done kénén
Lolo am
Té dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Chérie man dama dof si yaw
Dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Chérie man dama dof si yaw
Ecouter
A Propos de "Fou De Toi "
Plus de Lyrics de EL MAESTRO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl