Paroles de Zéro
Paroles de Zéro Par EL MAESTRO
Digital music
Démal, el maestro
Démal, wawaw
Mounou massi dara (leungo néxna lolu lé)
Néxal na nganan ma bayigama
Beugo comprendre manoumassi dara
Sama statut boul xol boloqué ma
Ndax fanga ndiokane
Louma dougal nga yeur
Bamay dioudou audounu wone démal démal
Té douma wani zéro
Man baamay dioudou andounu wone démal démal
Lolou douma wani zéro
Sama statut boul xol boloqué ma démal
Man details damay sonal
Sama statut boul xol boloqué ma démal
Details damay sonal
Xarit yomboul té yaw danga fau démal
Lan lamay wanii ?
Details damay sonal
Xarit yomboul té yaw danga fau démal
Xana xamo kabayéri ?
Bilahi details damay sonal
Dagma moudié déf none
Dagma moudié déf non pourtant massu mala yéné lou bone
K métiwoul kone sa xil rek mossi am gom héé !
Borom yaye ju bax té xol ba rafét
Yéné ko jaam !
Boka yénéwoul jaam day dém
Yéné ko jaam !
Manoma té donté yaguék samay secrets héé !
Manoma téré nélew yaw do café dose
Maynala 00 /20 waaw !
Yaw do défé touss
Ma toksi camaro dosé !
Nga tok sa biir douce
Lëp lou négatifs Guéné ko si sa vie
Kép koulay yakal nala dial né
Nin ni danio fau mano léna comprendre
Motax méfiances
Ndax dano soxor dano soxor wallah !
Amounu maturité
Négatifs tékis osés wallah !
Mano lén expliqué
Néxal na nganan ma bayigama
Beugo comprendre manoumassi dara
Sama statut boul xol boloqué ma
Ndax fanga ndiokane
Louma diougal nga yeur
Bamay dioudou andounu wone Démal Démal
Té douma wani zéro
Man baamay dioudou andounu wone démal démal
Lolou douma wani zéro
Sama statut boul xol boloqué wawaw
Man details damay sonal
Sama statut boul xol boloqué wawaw
Details damay sonal
Xarit yomboul Té yaw danga fau Démal
Details damay sonal
Xarit yomboul Té yaw danga fau Démal
Bilahi details damay sonal
Bamay dioudou andounu wone va t’en
Lolou douma wani zéro
Sama statut boul xol boloqué ma
Ecouter
A Propos de "Zéro"
Plus de Lyrics de EL MAESTRO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl