CANABASSE Dara Gënul Neex cover image

Paroles de Dara Gënul Neex

Paroles de Dara Gënul Neex Par CANABASSE


Dara gënul neex
Ma tëddmu ñëw sama wet

Dara gënul neex
Di chuchoter sama nopp baby
Dara gënul neex  
Bu  fi nekkee fàtte naa lépp
Lu journée metti-metti  mu ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Dara gënul neex  
Lii ana lu ko Gën a neex
Tëdd ak baby   sama wet
Xalaat ak xel bu ñu dajee
Wax  day bàyyil place bi jëf
Day gis sama doxin xam ni doxul
Gis  sama toogin xam xéll  toogul
Daf May xool ci bët Gis sama xol
Li ci manqué la ciy sol
Li ma àdduna  yan mo koy yenni
Damay yendoo coono téll-télli
Lu journée metti-metti meti mou ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby

Lu  ma low low daf may yëkkati
Moom mooy sukkar sama Life
Oh Lord fu ma jëlee kii
Bii xeetu mbëggeel dara gënu  ko neex

Dara gënul neex
Di chuchoter sama nopp baby
Dara gënul neex  
Bu  fi nekkee fàtte naa lépp
Lu journée metti-metti  mu ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Dara gënul neex  

Moom Mooy feexal sama xol
Moo may bégal
Janoo ak  moom rek di xool daf may apaiser
Après 8heure ku ma call du ma la jël
Maa ngi  mode avion jël  na volou mbëgéel  di plané ni ku  tux  ay boon
Sa ma nopp ci poojam ma koy nettali ay bêtises baby di dee ak ree
Life da fa  metti dëgër sérieux bari pression tax  ba Góor Yàlla di soxla trêve
Juge ci desert  dox ba daje ak teen
Maa ngi ak  sama kër
Man ak sama reine
Toom ma génnaat xare  guerre
Ñibbi si  fékaat fi trophée gagner perte yeah

Lu  ma low low daf may yëkkati
Moom mooy sukkar sama Life
Oh Lord fu ma jëlee kii
Bii xeetu mbëggeel dara gënu  ko neex

Dara gënul neex
Di chuchoter sama nopp baby
Dara gënul neex  
Bu  fi nekkee fàtte naa lépp
Lu journée metti-metti  mu ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Dara gënul neex  

Moom Mooy dëfal sama xol
Moo may bégal
Janoo ak  moom rek di xool daf may apaiser
Après 8heure ku ma call du ma la jël
Maa ngi  mode avion jël  na volou mbëgéel  di plané ni ku  tux  ay boon

Sama xol bi la ni bërët
Di saf lu neex
Ji ma mbëggeel
Wuy mbëgéeloo
Mbëgéel a bari doole

Ecouter

A Propos de "Dara Gënul Neex"

Album : Mbëgeel (EP)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Feb 14 , 2022

Plus de Lyrics de CANABASSE

CANABASSE
CANABASSE
CANABASSE
CANABASSE

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl