WALLY SECK Stay cover image

Paroles de Stay

Paroles de Stay Par WALLY SECK


Souniou andeu bi ba taye
Gnissouma thi mbétel
Waye souma sanione douniou
Meusseu réro
Souniou andeu bi ba taye
Gnissouma thi mbetel
Wayei souma sanione douniou
Meusseu taggo
Baby baby don't go don't go

Souniou andeu bi ba tayee
Guissou ma thi mbétel
Wayei souma sanione douniou
Meusseu réroo
Souniou andeu bi ba tayee
Gussouma thi mbétel
No no souma sanione douniou
Meusseu taggo
Baby baby don't go don't go

kaddu gui béneu leu
Yéné gui eupeu na
Beuss bi taye diokh naleuh
Kaddu gui yaye djitei
Soudone abb djanteu makoyee nangou
Soudone dianèrre makoye rêver
Wowowow bayi naleu kaye diriger ma
Baby kaye kaye ma wakhlaa
Lalalalala yeyeyeyeye
Lalalalalaw yeyeyeyeye
Baby baby don't go don't go

Kaddu gui niou tanee
Mbeuguel akk fanee
Baby don't go baby don't go
Don’t leave me
Li nélaw ci mane yakoye yé
boul ma di sorré kone
Damaye wett boy
Boy yaye sama xol

An an i ye an parirapam
An an i ye an pariraram
Parirapam, pariraram
pariraram he an, pariraram he an
Mame Ourey sama mame bi
Baby kaddu gui niou tunkone
Nio ko wara soukheul
Boulma kholei sama dieum dji
Yeurmandei gui ma la embeul
Bouggou ma niou réroo
Bouggoumala taggo

Beugueunala
Tibé ko sama xol bi
Somay guanel ma nagou
Wayei boyee dem taggou ma moma gueuneul
Dem na sa guadane outi sama yone my boy
Khol na ba khol meunoumala méré sakh
Sama ndiéguel dafa djitou ci iow
Baby boy nameunaleuh, wooo baby
Baby don’t go baby don’t go
Baby don’t go dont leave me
Kiné Badiane chérie Eumeudi
Yow dale dégal ngama

Ecouter

A Propos de "Stay"

Album : Stay (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 19 , 2019

Plus de Lyrics de WALLY SECK

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl