BRIL Sama Beug Beug cover image

Paroles de Sama Beug Beug

Paroles de Sama Beug Beug Par BRIL


[COUPLET 1: Birahim]
Les goûts et les couleurs ne se discutent pas
Mane kima beugg djokh ko sama khol
Na ngén massi Ba
Nimou tolou lako beuggué avec son poids
Je l’aime moi
Bala may dof ma teuyéla nga féss samay Lokho
Ndakh khalé bou fess
Beuri djapp mo djara tek lokho
Awoumak affaire taille fine
Mane gni la mine,
Way djekk dji niomay daadji yeah yeah
Souma naré déé thi aleu nama Gaïndé Ray
Souma naré déé thi aleu Guinar douma Ray boy
So beuggone étage chérie mom lalay may
Nimala beuggué dara douko Fay ,
Waaaa waaaaw

[REFRAIN : BRIL & BIRAHIM]
Mane lima gueuna beugg taille fine la
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
Limay daanél néwoul thi taille fine
Mane lima gueuna beugg taille fine la
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
Limay daanél néwoul thi taille fine

[COUPLET : BRIL]
Beutt dou yénou waayè khamna lou bopp attane
Beuggna kou yèm khalè bou maggoul attam
Taile fine kèn dou mom
Woyof attane sèn bopp niokko mom  hèè
Nameuna koumay fowè diko nabbeu nabbé
Kou yèm ci ay lokho makoy wane nimako Nobé
Bokkoul ak kiy tokk sa kaw té do meuna Noyi
Diss ba doto yeukk lokhom you Noy yi
Taille fine yi, sawar nagn té folén woo niou wouyoula
Té yaw sa djéék bi boko toppé bo dawoul niou robi laaa

[REFRAIN]
Mane lima gueuna beugg taille fine la
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
Limay daanél néwoul thi taille fine
Mane lima gueuna beugg taille fine la
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
Limay daanél néwoul thi taille fine

[COUPLET 3 : BIRAHIM & BRIL]
Bou Séédday djoté do sokhla andou Thiouray
Dangay bokhou rék teudd thi wéttam mou tokk dila Raay
Bou Taangay djoté do sokhla Clim waay
Di nga meune di foo ak mom té niakkeu doula Ray
Ki dafa djongué ba louné lamay déflo
Souniou teuddé dafmay djoylo
Ki dafa woyof ba founé lay aw thi mane
Boumay khalatt lim may def dafmay Réélo

Gni andak taille fine wanélén sén bopp (heeey)
Gni andak djéék dji yéén ana ngén (Heeey)
Gni andak taille fine wanéwoulén
Gni andak djéék dji , djoukklén may khool

[REFRAIN]
Mane lima gueuna beugg taille fine la
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
Limay daanél néwoul thi taille fine

Mane lima gueuna beugg taille fine la
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
Limay daanél néwoul thi taille fine

 

 

Ecouter

A Propos de "Sama Beug Beug"

Album : Sama Beug Beug (Single)
Année de Sortie : 2018
Ajouté par : Afrika Lyrics
Published : Aug 27 , 2018

Plus de Lyrics de BRIL

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl