Paroles de Yeureum Djiguene
Paroles de Yeureum Djiguene Par VIVIANE CHIDID
[VERSE 1]
Def ma mbamam def ma diamame
Dor soub’ak ngone la deuké ak mane
Def ma diamame def ma mbamame
Dima torokhal leu deuké ak mane
Leu deuké ak mane
Sa sou né leu deuké ak mane
Dima saga kanamou khalé yi
Ci samay nwalé domeu soutoural
Yeureumou lo ma faléwo ma
Fonkou lo ma métite bi doyna
Dorr djiguén bila dioureul sey dome
Wax deug y’Allah li dh niawna
Demb dioy ngeu ngiir ma nop la
Aty nga am ma dima dorr dima dioylooo
Dima dorr dima dioooylooo
Dima dorr dima dioooylooo
Dina méti si mane waxma lane leu
Deug soneu na kone yeureum ma
Seuyeul nala mounieul nala
Yaral la sey dome kone yeureum ma
Dorr djiguén boula dioureul sey dome
Wax deug y’Allah li deh niaw na
Garap bou dano khop ya lax na
Djiguén bou guéné keur ga dey wett loool
Dima dorr dima dioooyloo
Dima dorr dima dioooyloo
Waroul dooré
Gentleman waroul dooré
[CHORUS]
Def ma mbamam def ma diamame
Dima torokhal la deuké ak mane
Def ma mbamame def ma diamame dima torokhal
[VERSE 2]
Mane deg na makk dane na wax nane
Yeurmandé laniouy yoré djiguén
Mane deg na makk dane na wax nane
Ci soutoureu laniouy yoré djiguén
Al Hamdoulilah bila y’Allah bolék kila soutoural
Al Hamdoulilah bila y’Allah bolék ki sédal sa xol
Kokou gentleman leu
Gentleman leu Youssou ma djiguén
Chérie Aida dou dioylo djiguén
Gentleman leu Pape Ndiaye Alé Fara Ndiaye
Chérie Aida Ndiaye kokou gentleman leu
Gentleman leu Cheikh Amar chérie Marie
Amar dou dioylo djiguén kokou gentleman leu
Mbaye Dièye sing sing biram Dièye
Chérie Mame Ndiaye gentleman leu
Cheikh Kanté chérie Ami Diawara
Dou dioylo djiguén gentleman leu
Matar Cissé chérie Aida Mar
Dou dioylo djiguén gentleman leu
Gentleman leu Cheikh Tidiane Ba chérie Lissa
Ndoye dou dioylo djiguén
Boubacar Diallo diallo diéry
Chérie Mame Diarra gentleman leu
Pape cheikh Diallo chérie
Kya Aidara gentleman leu
Cheikh Sarr bou keur momar sarr
Goorou Alima Ndione gentleman leu
Nékhalal sa djiguén, djiguén aduna leu
Nékhalal ioe ioe sa djiguén, djiguén aldiana leu
Nékhalal sa djiguén, djiguén aduna leu
Nékhalal sa djiguén, djiguén aldiana leu
Ecouter
A Propos de "Yeureum Djiguene"
Plus de Lyrics de VIVIANE CHIDID
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl