Paroles de Teeyal
Paroles de Teeyal Par VIVIANE CHIDID
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel té bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon wé ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko té déwa gul (teeyal)
Ku nek am ngua lila doy
Féxel nga jem ko lidieunti
Mane deh lila waax
Sa gallé ngi taak di booy
Jem ko lidienti, té fayko deh lila waax
Lu touti nga def ko lou paata
Lo xaam nétali lila waax
Yakamti rayna sa niome maam
Deuguel rayone na sa niome maam
Bul ko lek té niora gul (teeyal)
Bul di wax lo xamni ama gui (teeyal)
Xaamu lo do xaar ba niou xaamal le (teeyal)
Guiss lo do xaar ba guiss lou guen ler (teeyal)
Té nagua tey té ngua daal (teeyal)
Amigo Li nguay wax deh woru la (teeyal)
Nopi baax na ci lo xamul lan le (teeyal)
Gawa waax meun na indi musiba (teeyal)
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel té bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon wé ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko té déwa gul (teeyal)
Mané li xawma lan la
Li xawma lan la, li xawma lan la li
Mané li xawma lan la
Li xawma lan la, li xawma lan la li
Ki dé lidieunti na le
Lidieunti na le, lidieunti la yow mi
Ki dé lidieunti na le
Lidieunti na le, lidieunti la yow mi
Ku nek am ngua lila doy
Féxel nga jem ko lidieunti mane deh lila wax
Sa gallé ngi takk di booy
Jem ko lidieunti té fayko deh lila waax
Lu touti nga def ko lou paata
Lo xaam nétali lila waax
Yakamti rayma sa niome maam
Deuguel rayone na sa niome maam
Li ngua bind est ce que deugu le (teeyal)
Fake news man yeugueluma (teeyal)
Beug buzz ba tax ngua dima sossal (teeyal)
Li ngua def deh xaam ngua loum toudou toumal (teeyal)
Boy yakati nit (teeyal)
Wala sah boy bond ci nit (teeyal)
Nala ler linguay waax ni lu am le
Luko moy dina don sa musiba
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel té bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon wé ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko té déwa gul (teeyal)
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel té bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon wé ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko té déwa gul (teeyal)
Ecouter
A Propos de "Teeyal"
Plus de Lyrics de VIVIANE CHIDID
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl