VJ Music Xalé cover image

Paroles de Music Xalé

Paroles de Music Xalé Par VJ


Xalè bou ndaw def buzz
Niet sons kassè teug concert (VJ)
Important ni adducteurs
My g rap bi la dieul en main (VJ)
18 ans dooom millionnaire
Rappeur bouko fi ma kane la (VJ)
Xalè bi xalè yi beug
Nouroulak namp yekoy xeuthio (VJ)
Sourax si law scène
Def bum teh awma sax album (VJ)
Niom nieup kane lagne bagn
Kane laniouy xol nogga may sen choice (VJ)
Fessal salle di leen dioy lo
Niom niuep bagn disant nonnn (VJ)
Pischininiko yaw fethial melni kitana
Eeh nènagne mounouma rap
Xana gni degn dof
Wala dagn beug sen chef yi
Nieuw toodial ken bok
Sen moukher yi lay xeuthie
Firil len mbari naan teuss
Mane douma tiiit ndax
Nena ma yaw demal
Billay walay talay
Gni beug vj gni koy topp
Billay walay talay

Ecouter

A Propos de "Music Xalé"

Album : En Vrai (EP)
Année de Sortie : 2023
Ajouté par : Farida
Published : Aug 01 , 2023

Plus de Lyrics de VJ

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl