Paroles de Bus Bi
Paroles de Bus Bi Par ADIOUZA
Baba mi ani
I guili Wana merer
Wajy souma koy xool ak nimou mél
Ah N bi né thi nekh
Oubi bountou bus bi dougou sama xole
Li mome dou néne
Mou guestou xoolma
Thi la xamner dou xememe
Maye gnami gnami
Koula jib wagni yaye dos d’âne
Bus bé ngui daw dal te rombeuna sama arrêt
Mba dou terminus lama dieumé
Dara dakar fo dem dik
Fess nga dél thi mane
Té xawma yawla kane
Xol bi nane ma te nga
Dém dik xolle ba xame.
Fess nga dél thi mane
Té xawma yawla kane
Xel Bi nane ma togal boul
Dem jiguene doù yombeu.
Ouhe baba, Ouhe
Ouhe baba, Ouhe
Mideyidima
Yidima
Bus be ngui rire
Mane degatouma
Beug na la pire
Ndax guissatouma
Mbeugel bou gaw
Melni Lou diare si peage
O doff nassi Yaw
Kila done sette
Jombi te guissouma jine (aaahhn aaahhhhn)
Jappeu ma teuthieu condamné (aaahhn aaahhhhn)
Jokna arret laye demandé (aaahhn aaahhhhn)
Ba chauffeurou bus Bi freiner
Mou naxe Ma seye
Fess nga dél thi mane
Té xawma yawla kane
Xol bi nane ma te nga
Dém dik xolle ba xame.
Fess nga dél thi mane
Té xawma yawla kane
Xel Bi nane ma togal boul
Dem jiguene doù yombeu.
Le courage m’a quitté
J’ai même pas osé tenter
Hypnotiser par son charme
Chui tombée en amour
Fess nga dél thi mane
Ahannnn
Xol bi nane ma te nga
Dém dik xolle ba xame
Fess nga dél thi mane
Ahannn
Xel Bi nane ma togal boul
Dem jiguene doù yombeu.
Ouhe
Fess nga dél thi mane (Ouhe)
Té xawma yawla kane (Ouhe)
Xol bi nane ma te nga (Ouhe)
dém dik xolle ba xame (Ouhe)
Fess nga dél thi mane
Té xawma yawla kane
Xel Bi nane ma togal boul
dem jiguene doù yombeu
Ba bus Bi freiner
Thi la xamner reuthieunama
Loutax demouma
Bassi mome wakhko li fi ne.
Ecouter
A Propos de "Bus Bi"
Plus de Lyrics de ADIOUZA
Commentaires ( 1 )
Nice nice
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl