YOUSSOU NDOUR Waññi Ko cover image

Paroles de Waññi Ko

Paroles de Waññi Ko Par YOUSSOU NDOUR

Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në

Waññi ko , waññi ko , waññi ko
Waññi ko , waññi ko , ëpp në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos
Te bés bu ne , benn xar nga daan añ e
 Nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée
Yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine
Am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann
Nga neeti ñu , yaw yaa ko jat ,    ba mu nelaw ,
Nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée
Te waa nations – unies , nga ka daan loué
Te diggënté , États-Unis ak Guinée
Daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
Am na benn bés , nga ni ma , my boy
Keroog daje naak , roi des arènes
Am na benn bés , nga ni ma , my boy
Keroog daje naak , roi des arènes
Ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations
Ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations
Ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy
Ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy
Na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs
Na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs
Techniques yooyu , japon laa ko jànge
Ca yooya jamono , man la ñépp di wër

Lu ñu wax nga ni fekke nga ko
Fu ñu wax nga ni dem nga fa
Doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw
Waaye  sa ma waa jii , ken melut ni moom
Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal
Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal
Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al
Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al
Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo

Ragal al yalla , waay , ragal al yalla
Ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla
Ragal al yalla , waay , ragal al yalla
Ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

Ecouter

A Propos de "Waññi Ko"

Album : Waññi Ko (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Jul 29 , 2021

Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR

YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant

A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl