Paroles de Seytané
Paroles de Seytané Par BAMBALY SECK
Sama diguanté ak mom
Kham guani yéné nala
Nonou guama yéné ndeysaan
Kham guani yéné nala
Nonou guama yéné ndeysaan
Dém na ba sakh sama gagni
Daniou may méré
Boul di doglou wakhi none yi
Thi sugnu duganté
Khamna né sakh dugnu tayi
Thi sugnu diganté mom
Yalla buur bi mom nopina
Meunougn niou taakalé
Lignu bolé dou louniouy dagg sani
Ngalaa nagn ko same waay
Nagn ma bayi ak mom
Mane kouma khol kham ni
Sori gua sama khol bi
Dara douko dindi
Lou waral ? lou waral ?
Nignu beuga doundé
Lou waral ? lou waral ?
Nioune niarr lougnu wara bolé
Lou waral ? lou waral ?
Nignu beuga doundé
Lou waral ? lou waral ?
Nioune niarr lougnu wara bolé
Bou ma niowé sa keur
Dagn maley neubb
Bayii leu bataxal wayé wouyou woma
Gua melni koumey daaw
Bayima thibiir leundeum
Mey weurr di diékh
Guissuma louma wane leer
Hmmm! mane damey lath
Lou waral ? lou waral ?
Nignu beuga doundé
Lou waral ? lou waral ?
Nioune niarr lougnu wara bolé
Lou waral ? lou waral ?
Nignu beuga doundé
Sou peundeu mi weuré
Tek ke molay wane yonn
Magni tokk di kharr di kharr
Ba guiss sama yonn
Lou waral ? lou waral ?
Nignu beuga doundé
Ecouter
A Propos de "Seytané"
Plus de Lyrics de BAMBALY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl