AIDA SAMB Temps Boy  cover image

Paroles de Temps Boy

Paroles de Temps Boy Par AIDA SAMB


So fataiko demb
Danioudane ande di kaaf di fo fi re
Donone xaley bobou diamono
Beugone naniou door dakei ak teuk ak anye
 So fataiko demb
Danioudane ande di kaaf di fo fi re
Donone xaley bobou diamono
Beugone naniou fowe
Tamit sal salato (saut)
Sal salato (saut)
Balle ba demna kaw
Au palais des justices c’est un bon palais
Où tous les gens y vivant vont se faire marier
Douta mbaye lo rere bik thiere ak soow
Mba dewoulo, Mba dewoulo
Lambi golo kou diouk daanou yako mom
Xala ma diir badio xala dofi diiar
Langa bouri boutour ngale koti koti (yoli yoli)
Koti koti (yoli yoli), koti koti
Ndeysane nexone na yoyou diamono
Sa sou takussan meusona diote
So amone 15 da ngay happiness
Bobou temps
So messane dem gedj
Ya ngui fekhe ni ngay dinde mbekh mi
Pour bo gnibisse bagn koula door
Da ngay dam bante balais defko sa karaw

Thiey temps boy  (Thiey temps boy)
Thiey temps boy  (Thiey temps boy)
Thiey temps boy lounek lanioudane def
Baalou keur niounane cotise pas ndalthie pas
Goor you beugone sathie mango ak di egate
Thiey temps boy  (Thiey temps boy)
Thiey temps boy  (Thiey temps boy)
Danioudane guiss keur rombfa sonefa daw
Amone na moudie kounek di bagn koula raw
Garabou ndim si kognbi niou taak ndiowane

So fataliko demb
Danioudane ande di kaaf di fo fi re
Donone xaley bobou diamono
Beugone naniou fowe
Tamit sal salato (saut)
Sal salato (saut)
Balle ba demna kaw
Au palais des justices c’est un bon palais
Où tous les gens y vivant vont se faire marier
Douta mbaye lo rere bik thiere ak soow
Mba dewoulo, Mba dewoulo
Lambi golo kou diouk daanou yako mom
Xala ma diir badio xala dofi diiar
Langa bouri boutour ngale koti koti (yoli yoli)
Yeeeeeeehhhh ma waay
Souma fataliko
Fima diar ak yaw bamay xaley
Ken douma laal ken douma togn
Fo tolou ya ngui prendre soin de moi
Taaw taaw taawoul taaw beuri mbok
Thiama yaay taaw
Bima nekei xaley fo meunti nek
Fouma meunti nek
Sama maak dji limalay nianalmoy
Goud faan ak weer lalay nianal

Ecouter

A Propos de "Temps Boy "

Album : Temps Boy (Single)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Dec 13 , 2022

Plus de Lyrics de AIDA SAMB

AIDA SAMB
AIDA SAMB

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl