AIDA SAMB  Baadolo cover image

Paroles de Baadolo

Paroles de Baadolo Par AIDA SAMB


Koffi défal lou bakh taay
Lou bone lalay faay
Koffi défal lou bakh taay
Lou bone lalay faay
Adouna sa xarit mo meuna done sa none
Damako dji teranga mou faay ma lou bone
Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Jiiko jaam lay doundéh
Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Défal naala loune

Teranga lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Koloré lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Teranga lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Koloré lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma

Adouna, niit dina djay ngoram guir done djaam
Damala wolou wone loma lathie ma diokhla
Féété la fii féété la fé, féété la founek
Léép loula meussa mééti, mééti naama
Ma bééteu la ngamay djeuw
Naane man ak sama djeukeur
Meunou gno aam dome
Motax may guoudé
Ma bééteu la ngamay djeuw
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Défal naala loune

Teranga lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Koloré lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Teranga lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Koloré lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma

Dagua xam louy aam souba yaw non
Loula yallah buur dinthial yaaw non
Dagua fokni gagn ngama yaw non
Dagu ma bétteu maay aam gagn
Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Jiiko jaam lay doundéh
Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Défal naala loune

Teranga lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Koloré lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Teranga lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma
Koloré lako dji mou faay ma
Lou bona bone mou faay ma

Dagua xam louy aam souba yaw non
Loula yallah buur dinthial yaaw non
Dagua fokni gagn ngama yaw non
Dagu ma bétteu maay aam gagn

Ecouter

A Propos de " Baadolo"

Album : Baadolo (Single)
Année de Sortie : 2020
Ajouté par : Farida
Published : Dec 10 , 2020

Plus de Lyrics de AIDA SAMB

AIDA SAMB
AIDA SAMB

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl