SIDY DIOP  Ngalam cover image

Paroles de Ngalam

Paroles de Ngalam Par SIDY DIOP


Sèkhaloma lèm
Sa love bi mane moneu yèm
Wakh nala baby je t’aime
Tontou ma mba douma dèm
Kounèkeu ngui djèm
Nguir digueuntè bi dou dèm chéri
Wayè on s’aime

Mane kholou ma kénèneuh
Té dèmouma fénèneuh
Makk yaw dou nèeneuh
Dou nènn, dou nènn
Mak yaw douo nènn
Djeum dja ngui ni
Djokh nala ko chèrèè yoboul foula nèkh
Limay sètt tchi yaw
Guiss nako woolouté amna bamou djèkh
Sèkhaloma lèm
Sa love bi mane momeu yèm
Wakh nala baby je t’aime
Tontou ma mba douma dèm
Kounèkeu ngui djèm
Nguir digueuntè bi dou dèm chéri
Wayè on s’aime

Bayilènn maal mom
Li boudonn seuyou tay mbeuguèl dè na tchi gnom
Kya ak matar boul falè boul baler
Boul guèstou té boulènn falè balou tay
Konn matar sarr tchi mom
Kya mo ba douté
Boul falè, boul baaler
Nèwonn nala boulènn faler
Sèkhaloma lèm
Sa love bi mane moneu yèm
Wakh nala baby je t’aime
Tontou ma mba douma dèm
Kounèkeu ngui djèm
Nguir digueuntè bi dou dèm chéri
Wayè on s’aime
A lé lé lé lé yo, lé yo chéri

Douma lènn toppou lagnou beuguonn amoul
Sougnou mbeuguèl rombou na di dèm
Gnoune gnaar
Dou kènènn kou gnouy dègloo baylènn gnou wakh
Djoy na guoudi djoy na beutcheuk nguir sama mbeuguèl tchi yaw
Mane djoy naa
Ma baby yo
Ronguagn tourou na tcheu mbeuguèl kèrssa doufa am
Na lingui yo
Nina birane nèna
Sèkhal ngua ko lèm
Sènn love bi mom moko yèm
Nèna leu baby je t’aime
Adjana leu beug nguènn dèm
Kounèkeu ngui djèm
Nguir diguentè bi dou dèm chéri
Wayè on s’aime

Li boudonn lambeu tay nèna sponsors la tiers
(Birane mo ba douté)
Guoro walè mbèrè guano chérie mina, mane dé nawna leu
Youssou marie sène moy sa baye
Yayou katie magniy dioy sa yaye
Nguoro walè mbèrè guano, birane ngalam yaw woutè nguak wurus
Sèkhal ngua ko lèm
Sènn love bi mom moko yèm
Wakh nala baby je t’aime
Matar adjana leu bueg nguènn dèm
Kounèkeu ngui djem
Nguir diguentè bi dou dèm
Kya ngalam ngua woutè nguak wurus
Lé lé lé lé lé lé li yo
Ngalam ngua outé nguak wurus
Magui mame diarra diary ba yi sènn yaye
Kya ngalam la outé nak wurus
Ni ngueu meuneu mèl ndèye djou bakhèy diour dom djou bakh
Ngalam ngua outé nguak wurus
Kya ngalam la outé nak wurus
Ngalam outé nak wurus

Ecouter

A Propos de "Ngalam"

Album : Ngalam (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Dec 23 , 2021

Plus de Lyrics de SIDY DIOP

SIDY DIOP

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl