Paroles de Sunu Sénégal
Paroles de Sunu Sénégal Par COUMBA GAWLO SECK
Sunu Senegal rewmi gnoko mom bougnouko yakk
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Sunu Senegal rewmi gnoko mmom bougnouko yakk
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Kilifa dine yek bou ada bi gneup naniou manko
Goor ak djiguene mak gnek ndaw gni naniou manko
Parti au pouvoir ak opposition naniou disso
Sunu Senegal galgui waroul soukh naniou manko
Rewum Senegal rewmi nioko mom bougnouko yak
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Sunu Senegal rewmi gnoko mom bougnouko yakk
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Aythia léne gnou diow galgui yatouna bougnouko sukhal
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Nga-gnane tê bekk khassaneté bi bilay diarrou ko fii
Sou kouné bayyê sa waar
Numu gueneu rafétê rewmi diem kanam
Waar wi yatouna aythia léne niou bay bagna fêweulo
Rewoum Senegal soutoura ak ngor laniouko namê
Rewum Senegal rewmi nioko mom bougnouko yak
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Rewum Senegal yaa ma gueneul fepp fouma meuna dem
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Kuma khôl ci Senegal dinga ma mérré, mo nekk ci sama khole bii
(Rewoum Senegal galgui nanuko diow bunuko sukhal)
Kilifa dinè yek bou ada bi gneup naniou manko
Goor ak djiguene mak gnek ndaw gni naniou manko
Parti au pouvoir ak opposition naniou disso
Sunu Senegal galgui waroul soukh naniou manko
Rewum Senegal rewmi nioko mom bougnouko yak
Ndiangoum gouneyyè-h
(Nioune loolu moniou sokhal)
Kheuyoum ndaw gnii
(Nioune loolu moniou sokhal)
Mo warra done priorité
Wergui yaramou askanewi
(Nioune loolu moniou sokhal)
Kiranguè askanewi
(Nioune loolu moniou sokhal)
Mo warra done priorité
Diami askanewi
(Nioune loolu moniou sokhal)
Naatangè ci rewmi
(Nioune loolu moniou sokhal)
Mo warra done priorité
Artiste Yii
(Nioune loolu moniou sokhal)
Communicateurs traditionnels
(Nioune loolu moniou sokhal)
Reuk lene djou djoung yii drapeau Senegal dess tchia kaw
Rewum Senegal rewmii nioko mom bougnouko yakk
Ecouter
A Propos de "Sunu Sénégal"
Plus de Lyrics de COUMBA GAWLO SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl