VIVIANE CHIDID Li Dafa Niaw cover image

Paroles de Li Dafa Niaw

Paroles de Li Dafa Niaw Par VIVIANE CHIDID


Bi aduna, lou fi diar ngay def lou niaw
Fi aduna, loufi way rendi sakh
Sa lokho rek lay nathie
Wakhma! Lane mo takh
Beuguoulo ma wakhal lou bakh
Wakhma! Lane moy mbakh
Boudé yénagneté wougnou lou bakh

Li dafa niaw, li dafa niaw, li dafa niaw
Li dafa niaw, li dafa niaw, li dafa niaw
Li dafa niaw nagnou sante
Yallah bayi batou guinaw
Khamna sama tolou waya takh sa fite di naw
Yalla nopina demba tay sogua
Nieuw guiss nga fi dara dou niaw
Lithi mane nékoul ci iow (ngani)
Lithi mane nékoul ci iow (dieuleul)
Lithi mane nékoul si iow
Beugueneté léne fi adina la (wawaw)
Lithi mane nékoul ci iow (wakhal)
Lithi mane nékoul ci iow (kay)
Lithi mane nékoul si iow beugueneté
Léne fi adina la (wakhal way)
Déréte biy daw thi iow moy daw thi mane
Wakhma lane motakh
Meunougno yénaneté lou bakh

Li dafa niaw, li dafa niaw, li dafa niaw
Li dafa niaw, li dafa niaw, li dafa niaw
Li dafa niaw nagnou sante
Yallah bayi beutou guinaw
Khamna sama tolou waya takh sa fite di naw
Yalla nopina demba tay sogua
Nieuw guiss nga fi dara dou niaw
Li dafa niaw, li dafa niaw, li dafa niaw
Li dafa niaw, li dafa niaw, li dafa niaw
Li dafa niaw nagnou sante
Yallah bayi beutou guinaw
Khamna sama tolou waya takh sa fite di naw
Yalla nopina demba tay sogua
Nieuw guiss nga fi dara dou niaw

Tu tapes dans mon dos
Tu parles dans mon dos
Tu craches dans mon dos
Sourire à la face couteau dans mon dos
Tu tapes dans mon dos
Tu parles dans mon dos
Tu craches dans mon dos
Sourire à la face couteau dans mon dos

Wakhal way
Tidiane wakhal way (Kokoy chérie Aïda)
Abdou Mbaye wakhal way (Borom Conakry)
Mani Akéthié wakhal way (from Abidjan la)
Bakhaw wakhal way (Kokoy coeur’ou Viviane)
Eeeh, kiné wakhal way (Kokou sama dome la)
Awadi wakhal way (kokoy frère)
Sénégal wakhal way

Ecouter

A Propos de "Li Dafa Niaw"

Album : Li Dafa Niaw (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Oct 21 , 2019

Plus de Lyrics de VIVIANE CHIDID

VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl