Paroles de Sama Logo Bi
Paroles de Sama Logo Bi Par AKHLOU BRICK
AMA LOGO BI
Ehhhhhhhh
Logo bi logo bi i know
LOGO BI
Parélén tay paréna
ok ok I know
Parélén tay paréna
EHHHHHHH.
Fou bi néna dofatoul té dou délou fan
Patin né mouk dou ba fén té ken douko téré nan ay Douliprane
Parélén paréna
May djiné biy tafou bir koloban
Dou gris gris diate ak thioumboukay boudone lola Gouy Gui rékay meuna dan
Grand yi né dama wawlé meuna rap tekthi gnémé rak
Ragalouma yamou thiowlé limay hamb tay la geuna tak
Tay la geuna tay la geuna tar
Dina meti tahoul beut yi taaa
Yéné ma dé ma lék sa naka
Tay mbeura beuré guén thi di bakou
Wahko né Toubab bé bagn né dou diongu
Nit kou gnoul bagn né dou diang
Kou nék sa natou bi
Ana Louy ndiarignou koom
Boudé dou guén thi bank
Haliss day wallou nit
Wan ma Lan geuna fonk
Louis V Gucci nga Am
Ma Tassaré logo thi
Logo bey todji sa monde
Ecouter
A Propos de "Sama Logo Bi"
Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl